🔴 ADMIREZ LE TALENT EXCEPTIONNEL DE BAYE MBAYE DONDE JUNIOR PETIT FILS DE MBAYE DONDE MBAYE

  Рет қаралды 480,620

MALIKIA TV TIVAOUANE

MALIKIA TV TIVAOUANE

Ай бұрын

#Malikia #Tivaoune #MalikiaTV
LEERU MAODO ➤ Li Bienvenue sur la chaine de MALIKIA TV TIVAOUANE restez connecter!!!!!!!!!!! Aimez, abonnez, commentez et partagez...Merci restez connecter!!!!!!!!!!!

Пікірлер: 1 000
@user-wf2ef6gu8r
@user-wf2ef6gu8r Ай бұрын
Je suis mouride mais j'ai des frissons rien qu'en l'écoutant
@abdoulayefaye5689
@abdoulayefaye5689 Ай бұрын
Diné dji béne la. Mag dji daniou woté kénal Allah bolé si beug Muhammad rhassoulloullah sallal'l Lahou aleyhi wa salam. Kou baax nga. Salam
@user-cq7zx9hf6p
@user-cq7zx9hf6p Ай бұрын
Bilay de meme que moi❤❤❤
@salammalekoum2234
@salammalekoum2234 Ай бұрын
Même mane ❤😢
@FallouGalass-lg5bt
@FallouGalass-lg5bt Ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@serignefalloudiakhoumpa6474
@serignefalloudiakhoumpa6474 Ай бұрын
Mouride waru ko déglu ? Xana du Turu Yalla lañuy zikr?
@abdoulayediack5208
@abdoulayediack5208 Ай бұрын
Ma cha alah nagnoulene ko protéjé boubakh nak Serigne Babacar Sy Mansour khalif général des tidianes yalenafi yague té wére amine
@youssoufdaff5977
@youssoufdaff5977 Ай бұрын
Amine ya rabi 🙏🏾👏🏾
@mounasdiene730
@mounasdiene730 Ай бұрын
C'est le khalife de 10% des talibés
@amethfall1413
@amethfall1413 Ай бұрын
🎉🎉🎉🎉2🎉😂🎉1jour 😢1🎉¼😢🎉🎉😢😮😂😢🎉🎉🎉🎉🎉🎉😂🎉🎉🎉😂je 1te pas 😢de 😮😮😢et 😢toi 😢🎉 0:52 😮a11😮1😮a31¹😢1aza11😢1😢²2ans 2🎉😢🎉😢a2⅖2²🎉2a32a2aa3azzzzazaaaaaa334😮😮😮😮😮pas 3z⅜😢😢2😢22🎉🎉🎉22🎉😂11😂⁴😂²😂😂🎉🎉🎉a1aq1q😂😂
@abdouwade749
@abdouwade749 Ай бұрын
Allahuma amine inchallah
@user-rp4jr2hz9w
@user-rp4jr2hz9w Ай бұрын
A❤​@@abdouwade749
@bilyshop221
@bilyshop221 Ай бұрын
Ana gniu diouge tik tok ndakh li 😂❤️❤️😂
@ibnouserignefall6965
@ibnouserignefall6965 Ай бұрын
Suis la😊
@fatoudiop3987
@fatoudiop3987 Ай бұрын
Maagui ni deh li katt limiye deff si yaram dafa graw
@Tee_Baby_
@Tee_Baby_ Ай бұрын
Mangi niiii😂❤
@modousall3831
@modousall3831 Ай бұрын
magui nii brk borom touba li nekh na
@Bouba815
@Bouba815 Ай бұрын
Magui nii😂😂😂
@ousmaneseck6889
@ousmaneseck6889 Ай бұрын
Serigne Moustapha nena niou protegéko machalla ❤ thieuy maodo
@alaminesylo2511
@alaminesylo2511 Ай бұрын
inchallah kom toudou nako rk yalla dina ko samou konou loum toudou yalla def si barke inchallah ❤
@ousmaneseck6889
@ousmaneseck6889 Ай бұрын
Machalla alhadoulilahi
@laminesebor3556
@laminesebor3556 Ай бұрын
Surtout lolou ❤
@ndiagambaye5780
@ndiagambaye5780 Ай бұрын
Kone ngiko begue abou daniy kharr❤
@ousmaneseck6889
@ousmaneseck6889 Ай бұрын
Nn gayi n'en len KO Al rek grawoule talibé cheikh daye tabé après magal mou gnibissi mais niou wattouko mbeuk rek si danou lerr ti
@mansourndiaye9014
@mansourndiaye9014 Ай бұрын
Ninga sédalé sama xool bi yalnako Cheikhou Tidiane sédalé sa xool ❤🥹🤲
@elhadjibakhoum5270
@elhadjibakhoum5270 Ай бұрын
En tant que mouride, dadj bii fim may ageu yalla rek moko xam !! Kendou sounou makgni ❤❤!!!
@DiaguaWane
@DiaguaWane Ай бұрын
Ana gni guiss vidéo Tik tok kom Mane nieuw directe pour setante lep si vidéo machallah Serigne Moustapha la nieuka dég mou wakh sa tour bilahi mourite talibe bamba la te Lou bakh rek la beugue mai nékh dou wésou li machallah ❤️❤️
@user-ux7vf6gv4j
@user-ux7vf6gv4j Ай бұрын
Suis là 😂
@cheikhounadia4195
@cheikhounadia4195 Ай бұрын
Mangui ni dama ko sét ba sone mais al hamdou lillah à fin ❤❤❤❤😂
@mamadoudien2496
@mamadoudien2496 Ай бұрын
Yalnala yalla saam arr la weral baatt bi lingay wakh neekh na khol mouride sadikh la wayet dioy lo nama tay si souba
@user-ws4hd6wz9l
@user-ws4hd6wz9l Ай бұрын
benn ci man Murid bi❤
@user-sb4iq7no8y
@user-sb4iq7no8y Ай бұрын
Machallah ❤❤❤
@abysene3841
@abysene3841 Ай бұрын
Macha allah j'ai des larmes aux yeux tivaoune mon paradis sur terre me manque😢
@beuguepirelespatriotes8799
@beuguepirelespatriotes8799 Ай бұрын
Wallahi yallana niou yalla fayal aladji malick
@abysene3841
@abysene3841 Ай бұрын
Allahuma amine 🙏​@@beuguepirelespatriotes8799
@ibrahimaxalildiop4060
@ibrahimaxalildiop4060 Ай бұрын
Barké chiekhoul khadim li dafa nekh khalé bi yalna ko yalla samou ❤❤❤❤❤
@user-jw5uo4se9d
@user-jw5uo4se9d Ай бұрын
Amine
@mamemariemmbaye8460
@mamemariemmbaye8460 Ай бұрын
Amine nan niouko al ba magal touba passé niou xol baxam dinan ko délo wl😂😂❤❤❤
@awadiop805
@awadiop805 Ай бұрын
Allahouma amine motakh warnano yarr boubakh sounou dome yi ci diné😢❤
@bildoxer89diakhate5
@bildoxer89diakhate5 Ай бұрын
Kii yalla nako yalla samou si barké seydina Mohamed psl
@abdoulayesall5565
@abdoulayesall5565 Ай бұрын
Machallah nekhna trop mais dianguale téré yi yepp gua bagna yakamti
@Cheikh-Saloum
@Cheikh-Saloum Ай бұрын
Amine
@taphagueye1813
@taphagueye1813 Ай бұрын
Amiiiiiiiiiiiiiiiiine yarabi 🎉❤
@user-py2ni6ez8g
@user-py2ni6ez8g Ай бұрын
Aamiine ❤❤
@cheikhou1871
@cheikhou1871 Ай бұрын
Amin
@AissaDiallo-vr3ii
@AissaDiallo-vr3ii Ай бұрын
C'est tellement adorable ❤ C'est une très grande fierté pour un papa de chanté avec son fils 🥰 machallah ♥️
@modougueye9037
@modougueye9037 Ай бұрын
Domou Kane la
@serignemansourtoure86
@serignemansourtoure86 Ай бұрын
Cheikh tidiane mbaye
@mouhamedgueye6498
@mouhamedgueye6498 Ай бұрын
Donc pape malick n'est pas son père je pensais
@AissaDiallo-vr3ii
@AissaDiallo-vr3ii Ай бұрын
Ils ont une trait
@femmepanafricaine5147
@femmepanafricaine5147 Ай бұрын
@@AissaDiallo-vr3iiil resemble plus à papa Malick mais c’est le fils de cheikh tidiane il semble qu’il la donné à pape Malick c’est lui qui l’éduque
@sunuterangatv6137
@sunuterangatv6137 Ай бұрын
❤❤worna serigne touba li nékh na waye macha Allah ❤
@user-pb5ou7un2f
@user-pb5ou7un2f Ай бұрын
Ki Nak mou yèlo ayy milliard, barkè serigne Touba 😭😭😭
@OusmaneLy-cv5nd
@OusmaneLy-cv5nd Ай бұрын
❤ wallahi❤
@mamadousadji6056
@mamadousadji6056 Ай бұрын
Daye nieuwe si mercato bi transfère fawe mou ame guisse nako si hisbou daroul xoudose yi ❤❤❤ Machallah c’est le Sénégal ❤️❤️
@user-bu3eh1oq3v
@user-bu3eh1oq3v Ай бұрын
Billahi nk na nieuwe loumou wax niou faye ko ❤
@ibrahimasylla2456
@ibrahimasylla2456 Ай бұрын
Mourid tijan laye e thiaba niasene ndiassane dioulite yepakoye nianal giudiu fane wer karange bate bou gana diapani barkeb brom touba ak xassida yi amine 😭😭😭❤❤
@aliouba9010
@aliouba9010 Ай бұрын
😢😢😢😢 ki yalla nagnou ko yalla samale ❤❤si barkép cheikh seyidil mouhamedoule moustapha sy al mourchide ❤❤❤
@user-qs1ft6fn3r
@user-qs1ft6fn3r Ай бұрын
Amine ❤
@Dev22145
@Dev22145 Ай бұрын
Je suis mouride ms li dafa nekh bilahi yalla na yalla weral batt bi ❤️🙏🏽
@femmepanafricaine5147
@femmepanafricaine5147 Ай бұрын
Bilay lep ben la l’islam mo am nam
@alidiouf1439
@alidiouf1439 Ай бұрын
❤❤❤ MASSALAH Boukoul ci khale yi nekk ci Internet bi Di saaga
@amadoudamediba1072
@amadoudamediba1072 Ай бұрын
😅😅
@cheikhahmedtidianetabara8239
@cheikhahmedtidianetabara8239 Ай бұрын
Yalna ko yaAllah thi barkel thi barki Sérigne Moustapha Sy Al Maktoum❤
@moustaphadione7239
@moustaphadione7239 Ай бұрын
Lii dioylo nama Barké baye niass lii nékhna
@bassendoye6831
@bassendoye6831 Ай бұрын
Lissi Mame Boye Seuta koy dieul😭❤️Mashallah yalna yallah weral batt bii❤️❤️❤️
@viensvoirtv9844
@viensvoirtv9844 Ай бұрын
Je suis muride mai walahi sope nako mashallah yalna yalla yok xaam xaam bi tam may la weir ak goud fane xaliss bu barkeil Maodo moy Ahmadou Bamba ahmadou moy Maodo gnon bok Mäm maram Touba ak tivaoune beine deuk la ❤️ yalna diam yag Sénégal 🇸🇳
@idrissagaye5823
@idrissagaye5823 Ай бұрын
Pape malick moy thiokho baye mbaye mashallah. Mane dé niom rek lay topou sayabo sama connexion diekh. Yalna yalla yereum mame mbaye dondé❤
@yatmaseck3056
@yatmaseck3056 Ай бұрын
Baye mbaye dafa nurou mamam mbaye dondé ❤ machallah
@SENEGAL9G-351
@SENEGAL9G-351 Ай бұрын
Waaw 😭 ❤❤ yallah na yalla barkél bijahi Aboul Abassi Cheikhou Tidjani ❣️❤️ xol toyna❤❤ waay machallah ❤❤
@aminatabalsanuho8718
@aminatabalsanuho8718 Ай бұрын
Dieu seul sait combien de fois je visionne cette vidéo par jour .J en ai fait mon hymne.Machallah qu Allah te protège.
@magayendiaye4268
@magayendiaye4268 16 күн бұрын
Machalla
@uneBabacarienne-pd6jx
@uneBabacarienne-pd6jx Ай бұрын
Machallah yalla na yalla wéreul bate bi si barké Serigne Babacar ❤
@OusmanenourayniSylla-ho4sb
@OusmanenourayniSylla-ho4sb Ай бұрын
Machallah 🥰 Baye Mbaye junior yalna bour yalla sammko comme Niko Serigne Moustapha Sy Al maktoum Wakhé 🙏♥️
@user-wr3rk8pb7t
@user-wr3rk8pb7t Ай бұрын
Papam pape malick contan na ndeysan ❤❤❤🥺
@mbayediop123
@mbayediop123 Ай бұрын
Diereudieuf pape Malick si anticipation bi niane bou am solo la na demm ba diekh machalah baye Mbaye sa mame mo takh niou kham mame maodo Malick Sy (RTA)
@aminatalobio
@aminatalobio Ай бұрын
Mashallah yalna la lene yalla same si barke CHEIKHOU TIDIANE RTA❤❤❤❤❤❤❤❤❤😊
@user-uc9hk7nf8s
@user-uc9hk7nf8s Ай бұрын
Machalla way baye mbaye ❤❤ serigne Moustapha sy almaktoume néna niou protegéko ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@ibacisse6663
@ibacisse6663 Ай бұрын
bilahi
@MouhamadouMoukhtarSY-ms5jm
@MouhamadouMoukhtarSY-ms5jm Ай бұрын
Yalla na yalla sam té aarla laf thiat baye Mbaye bou thiaat
@oumoukaltomendiaye4958
@oumoukaltomendiaye4958 Ай бұрын
Lathia mame seut mokay dieul yalla nalla yalla deff mak bou ame valeur té maîtrisé khassida yi
@fatoubinetoumaguettedieye6206
@fatoubinetoumaguettedieye6206 12 күн бұрын
Machalla je suis MOURIDE mais j'ai des frissons en entendant Baye Mbaye lafe thiate goudou fane weer bcp de bonheur ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@falloukane16
@falloukane16 Ай бұрын
En tout cas 😢 kou sa khole yengouwoul si li demal fadiou febarou khole❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@damegaye2020
@damegaye2020 Ай бұрын
Machalah way Baye Mbaye yalna yala protègél la bopam inchallah ❤❤❤❤😢
@SouleymaneKamara-ed1rw
@SouleymaneKamara-ed1rw Ай бұрын
Amine
@papaousmanelo892
@papaousmanelo892 Ай бұрын
La relève est assurée ❤️ Yàlla na Sougnou Borom sam lakh fou yakh egoul
@mamemaryndiaye3875
@mamemaryndiaye3875 Ай бұрын
Machallah j'ai des frissons en l'écoutant je te jure bilahi talibé Cheikh Ahmed Tijani nékhna 😢❤
@amathSow-ig2ly
@amathSow-ig2ly Ай бұрын
je suis mourid mais li dfa daw yaram bilah
@seynaboudiame
@seynaboudiame Ай бұрын
Beutou fierté rk ngay guiss si ay papam yallah nako yallah samal bopam ❤
@lamourdelabsolumounina7283
@lamourdelabsolumounina7283 Ай бұрын
Daneel beneu Mouride deh neekhena lool SOUNIOU MAG YALNALEEN YALLAH DOLI FAYE ❤❤❤❤❤❤❤
@MuguetteSeck
@MuguetteSeck Ай бұрын
Machallah Yalla naga goudu fane t'es weer Barkep serigne Touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@gallassleye4670
@gallassleye4670 Ай бұрын
😭😭😭lii nimiy déff sama kholl ak sama yaram bi yalla rek moko barké S.Fallou Mbacké 😢😢
@fatouseck5364
@fatouseck5364 Ай бұрын
C'est normal ma sha Allah souniou borom SWT lay way il faut mou dougue si khol yi
@ndoumbesamb3960
@ndoumbesamb3960 Ай бұрын
Mais que diiiire😢😢 Macha Allah yalna Yalla same leu teh aar leu❤❤❤❤
@bigndanane1448
@bigndanane1448 Ай бұрын
Fane yii mom sama khôl bi dafay nékh rek. Mouride fénial boubakh né Tidiane bi domou badiénam la. Niouy roubéwanté rek. Lii Yalla na yague ci Sénégal. Bouniou kéneu diakhassé. Machalla Yalla na yalla ciguil Sénégal guereum ko naatal ko
@gogodioumaba5754
@gogodioumaba5754 Ай бұрын
Ma sha Allah yalla nala Yalla yokou wer aral bopam ak sa wadiors yi ly nékhna trop bilay Yalla guéne la
@HawakayaKane
@HawakayaKane Ай бұрын
Macha ALLAH sama dom bi, ya Allah namla samm, sa baye moy sama weuy katt, sama sonnerie portable sah mofa nek❤️😇
@bassiroudiouf2449
@bassiroudiouf2449 Ай бұрын
Lii moom dafa neekh barké borom touba❤❤❤❤❤
@sunuterangatv6137
@sunuterangatv6137 Ай бұрын
❤❤worna serigne touba li nékh na waye macha Allah ❤ 3:49
@OusmaneLy-cv5nd
@OusmaneLy-cv5nd Ай бұрын
❤😢😢😢man dee dama warou yallana yalla arr mayla goud fan ak weur 🤲 Amin ♥️ Barakkalah❤
@oumydabo7521
@oumydabo7521 Ай бұрын
Ohhhhh😢😢 machalah li nehhna❤❤❤❤❤ yalna yalla goudal Say fane Baye Mbaye 🙏
@massseye6078
@massseye6078 Ай бұрын
❤❤❤❤yalla nala yalla moussal ci thiat ak lamigne lakh la fa yakh yegoul baye mbaye
@ibrafall9077
@ibrafall9077 Ай бұрын
Barkei serigne bamba ma content machalla yalna yalla weral batt bi goudal fane bi
@FatimazahraElCheikh
@FatimazahraElCheikh Ай бұрын
Yalla n’a borom bi SWT samal la boppam zahiratane wa batinane thi barké Cheikh Ahmada Tidiani Chérif RTA.
@serignefallousarr7176
@serignefallousarr7176 Ай бұрын
Mbarké s touba ki motakh may diang xasida ❤fala bouda mine chakwa❤ alhamdoulilah ❤❤
@fallmbegtefadilou9306
@fallmbegtefadilou9306 Ай бұрын
Barki Seugne Fallou li dafa neex Baaye mbaye Dundeul🤍
@amadousy727
@amadousy727 Ай бұрын
Masha Allah لاإله إلا الله محمد رسول الله صلى الله عليه وسلم ❤❤
@siahibouyaffa1596
@siahibouyaffa1596 Ай бұрын
Pourquoi à chaque fois que j’écoute ça,je pleure 🥹🤍
@mouhameddiao9030
@mouhameddiao9030 Ай бұрын
فلا بد من شكوى الى الله كربتي فما لي غير الله جابر كسرتي Jaarama S.Seydil Hadji Malick Sy ❤❤❤❤❤❤❤
@user-ht4bj5hy4l
@user-ht4bj5hy4l Ай бұрын
Sama Serigne néna nagne ko ko protègel mame mbaye ❤❤
@morseck9238
@morseck9238 Ай бұрын
Macah allah sigil géne séne wadiour 😭😭💔
@dabagueye5395
@dabagueye5395 Ай бұрын
Baye mbaye j'ai pas les mots ndakh xol❤ bou fess ak ay dioy😢. Yalnala yalla takhawou té sameu la si barké Cheikh Tidiane RTA
@Haliyi
@Haliyi 7 күн бұрын
Wallahi doumaci doyyal. Tellement ça m’apaise le cœur 🙏🏾
@user-ev5on5hz9s
@user-ev5on5hz9s Ай бұрын
Baye Mbaye del diangu tére yi waye yaw talent Rek nga
@PapeIbrahimaDiagne-jj6jt
@PapeIbrahimaDiagne-jj6jt Ай бұрын
Je suis fière d'être talibé cheikh ❤️❤️❤️
@Delba369Beatz
@Delba369Beatz 17 күн бұрын
Way Baye Mbaye Yalla naga Goudou Fane Si Barké Seydina Muhamath S.A.W. Amine ya rabbi ❤❤❤❤❤❤❤
@barradiop9576
@barradiop9576 Ай бұрын
Billahi sama xoll sédna barkep alkhour'ane yalla nako yalla dollé taxawou saa souné barkep brom touba 🤲🤲🤲
@mamadoumansourndao1499
@mamadoumansourndao1499 Ай бұрын
Même les autres sont émus 😢ça se voit a travers la joie qui les anime Longue vie à Baye Mbaye🤲🏾
@babacarseck7753
@babacarseck7753 Ай бұрын
Machalla baye mbaye yalla samoula barké fala bouda
@user-ev5on5hz9s
@user-ev5on5hz9s Ай бұрын
Bonne continuation baye mbaye dieu porotéce 😢
@NdiateMboup-cz4un
@NdiateMboup-cz4un Ай бұрын
Baye mbaye yalla n'a la yalla same 😢
@mamediarraboussotall1182
@mamediarraboussotall1182 Ай бұрын
Goudou fane rék Rék nak Inchallah.Et mes larmes qui ne cessent de couler.😢😢😢❤❤❤ qu'Allah swt t'accompagne et que la Baraka du prophète Muhammad et de Seydi Hadji Malick illumine ton devenir.
@AliouneMboup-pz8sw
@AliouneMboup-pz8sw Ай бұрын
♥️♥️🙏👍🏻kone tane n'a si yene Diamou si yene
@senegalais9976
@senegalais9976 Ай бұрын
بارك الله فيكم
@YoussoufDiassy-jo3mb
@YoussoufDiassy-jo3mb Ай бұрын
Machalla barke serigne saliou li da da fa nex goudeul fane
@idrissadiop4391
@idrissadiop4391 Ай бұрын
Machalla baye Mbaye yalnala yalla samal bopam🙏
@groupenabiyetv8211
@groupenabiyetv8211 Ай бұрын
NOKHOL BA NÉKHOUL MAIS PAPE MALICK KOU BAKHLA NDÉYSANE ❤❤❤❤❤
@alassaneka4708
@alassaneka4708 Ай бұрын
Machallah j'ai des larmes yalla na yalla sama te are
@mensourkebe1549
@mensourkebe1549 Ай бұрын
ohh ❤ Baye mbaye Yala na yala samla té barkéll la yobou lénn daradia encadré koo tèré yii rék
@alaminetv7758
@alaminetv7758 Ай бұрын
J ai pleuré de joie ❤ pape Malick yag fi lol mbaye ak group bi yeupp bay mbaye nk domi niaye goudou fane lagn kay nianal waye pa reuy 🎉🎉
@babucarrsecka495
@babucarrsecka495 Ай бұрын
Diaradiaf s Mostapah sy mo takh ma kham ko😊
@papeleye267
@papeleye267 Ай бұрын
wa😂
@mouhamedgueye6498
@mouhamedgueye6498 Ай бұрын
Wakh na deug
@deffaly9056
@deffaly9056 Ай бұрын
Merci Bayes Mbaye continel si rhythm bi rèk pas taassou masha Allah ❤❤❤
@morgueye2533
@morgueye2533 Ай бұрын
Machahalla li nékhna❤
@AhmadouDieye-gj4jt
@AhmadouDieye-gj4jt Ай бұрын
Machallah yalla na yalla sameu arla lakha fou yakha ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@cheikhou1871
@cheikhou1871 Ай бұрын
Je suis Mourid ,xalei bi lamouy jang si ci tagg yonnent bi neex na
@linegueye6211
@linegueye6211 Ай бұрын
Machala allhamdou lilha yalna yalla def lene ay mak si barke serigne babacar sy ❤
@tidianeaw5449
@tidianeaw5449 Ай бұрын
Macha allahh yalla na yalla samoula té are la ak sayi wa diour❤❤❤
@ndiaganiang7590
@ndiaganiang7590 Ай бұрын
Alahou akbaar yalla nala téral Barké Seydana Mouhamed
@user-rn3iu3mg5r
@user-rn3iu3mg5r Ай бұрын
Waouh 😢😭😭😭 Les mots me manquent bilahi 😭 machalah 🥰❤️❤️❤️🙏🏽 Mbaye Mbaye yallaneuh yalla wéreul bate Chi barké Séyidouna Mouhamadou psl 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
@ndeyeanthioboydodiouf4792
@ndeyeanthioboydodiouf4792 Ай бұрын
Machalla ❤🎉 yalna yalla may goudou fann akk wer
@KhalilDia-dk4re
@KhalilDia-dk4re Ай бұрын
Oh li nékhna way yalna diam yag ❤
@ndiombendiaye4536
@ndiombendiaye4536 Ай бұрын
Machallah baye mbaye yalna yalla barkél leup inchallah amine
@ibrandaw-fm4xz
@ibrandaw-fm4xz Ай бұрын
Macha alla keneu dou Sénégal en sus de cette révélation ( yalla nako yalla sam may KO fane bou goud) Commentaires you eup sont des mourides ça prouve Sénégal rew bou bakh lagne
@saerdiop5568
@saerdiop5568 Ай бұрын
Je l'ai téléchargé pour pouvoir l'écouter tout temps Yalla na yalla samm la ci barké cheikhoul khadim😢
@babacarniang337
@babacarniang337 Ай бұрын
Protection rék. ma cha Allah
@KhalifaSeck-xb2vp
@KhalifaSeck-xb2vp Ай бұрын
Qu'il soit bien encadré, bien protégé, Mou diaangue bou baakh, té woyof tollou, deudou adouna bou baakh
@user-xm5cr7sd9s
@user-xm5cr7sd9s Ай бұрын
Franchement défar nga sama koritè barcki Serigne Moustapha sy maktoul🥲❤️❤️❤️❤️
@ndiagambaye5780
@ndiagambaye5780 Ай бұрын
Machallah Baye mbaye machallah pape Malick mbaye bodefoul wone ni doudou kene mbaye wakh ak yaw sama xol dfa sede❤✅❤✅
@fatoundiaye8787
@fatoundiaye8787 Ай бұрын
MACHAALLAH YALLA NALENNE YALLA SOUGNOU BOROMBI SAMEULENNE, MOUTHIALENNE,🔥🕊️😭💪♥️🛐
🛑Oooh Ndeysane Sam Mboup Toyal ne Xolle Yeipe Ziarra Khombole Éditions 2024
14:17
Cute Barbie Gadget 🥰 #gadgets
01:00
FLIP FLOP Hacks
Рет қаралды 26 МЛН
FOOTBALL WITH PLAY BUTTONS ▶️ #roadto100m
00:29
Celine Dept
Рет қаралды 74 МЛН
🔴 " INAL MANAYLA " PAPE MALICK MBAYE ET SON GROUPE
23:21
MALIKIA TV TIVAOUANE
Рет қаралды 26 М.
HAJA QALBI - Doudou Kende MBAYE
12:18
DOUDOU KENDE MBAYE TV
Рет қаралды 375 М.
Mbaye Donde MBAYE Falabuda
21:42
Seutou Damel
Рет қаралды 124 М.
baye mbaye yallana goudou fane
7:19
MAME NDOKH TV OFFICIELLE
Рет қаралды 45 М.
Serigne Fallou Tine Explose le Plateau de Massalikul Jinane
16:15
Cute Barbie Gadget 🥰 #gadgets
01:00
FLIP FLOP Hacks
Рет қаралды 26 МЛН