Discours de S.Saliou Thioune Thiate 17 Avril:Sokhna Aïda na.....

  Рет қаралды 119,391

MELOKAN TV

MELOKAN TV

2 ай бұрын

Vous pouvez VOUS ABONNER à notre chaîne KZfaq

Пікірлер: 203
@SalymataMangane-dd2eb
@SalymataMangane-dd2eb 22 күн бұрын
Nanguou naniou nekh naniou té gueum naniou sokhna aïda saliou thioune Moy Serigne Bethio saliou🎉❤🎉❤😊
@karaamatii633
@karaamatii633 2 ай бұрын
Y'a des gens, c'est dans la division qu'ils gagnent leur vie😢 merci a l'intervenant qui a prier pour la réunification de toute la famille de Cheikh Béthio ici et d'aiileurs. Nitt ku Yallah bakhal mom dou beug kén bone bouko ndiorté si nite sah day niane Borom bi déllosiko
@servantx630
@servantx630 2 ай бұрын
Ndeysan cheikh bethio yalla na yalla yessal yeurmande si barke seydina mouhamed
@mykakamara2311
@mykakamara2311 2 ай бұрын
SAST Deugui Deugui dieumeum dji,diamam bi,Di sakk ak ndamam yagg fi té weer❤❤❤
@bambathiaw6913
@bambathiaw6913 2 ай бұрын
Il y’a certains personnes qui gagnent leur vie dans la division de certains familles.Parler n’est pas donner à tout le monde thiedo c’est pas le moment ni l’heure de se mêler des affaires familiales. Serigne ken da khamoul loumou doneu ❤
@cheikhndiaye4199
@cheikhndiaye4199 Ай бұрын
Ndokhal léne té déme tawe bou mate tawe monye donou Baye Serigne saliou thioune matéga lép thioune❤
@seynaboudiack7692
@seynaboudiack7692 2 ай бұрын
Merci beaucoup serigne Touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@salimataseye1214
@salimataseye1214 2 ай бұрын
Képpeu kouy thiantakonn té beugue cheikh bethio te yallah rék takh warguénn dokh ba famille bi nekatt bénna
@MouhamadouMoustaphaSANE-by5jr
@MouhamadouMoustaphaSANE-by5jr Ай бұрын
Bilahi li Moy deugg
@fallndiolle4430
@fallndiolle4430 2 ай бұрын
Wallahi ndaysan machallah amna solo
@seynaboudiack7692
@seynaboudiack7692 2 ай бұрын
Machalla Anna solo serigne Touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@ibrahimasamb8444
@ibrahimasamb8444 2 ай бұрын
Adda dou DINÉ sama wadji...Wayè adda djou rafète meune na andak diné...Yeuff yi rawnalène wakh rèkka lène déssè😂😂😂😂
@salllamtoro4678
@salllamtoro4678 2 ай бұрын
, 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@user-mt6hi6ky6u
@user-mt6hi6ky6u Ай бұрын
Amine yalla na Sounou borome bollé niabotou sérigne béthio gui moye ndame d
@Animateurpresentateur
@Animateurpresentateur Ай бұрын
Thiante amoul Dioy 😭 thiante amoul seytanè thiante amoul diambat Gnoun wa KEUR Sokhna Aïda Saliou Thioune gno gui bègue di sante darra mètiwou gnou BAL NAGNOU LA NDAH YAW LA KÈN ME SOUL GUISS NGA YORÈ MICRO THI SA KANAMOU SERIGNE KON BO GNEWÈ DI WAH THI SERIGNE BÈTHIO DOU GNOU DÉF PROBLÈME 😂😂😂
@user-bk7nm8kx4n
@user-bk7nm8kx4n 2 ай бұрын
Yalla na yalla samou ❤
@user-xf9wz4xb7q
@user-xf9wz4xb7q 2 ай бұрын
Serigne saliou dioune yalla nala yalla défal diam ❤❤❤❤❤
@seynaboudiack7692
@seynaboudiack7692 2 ай бұрын
Merci beaucoup serigne Touba ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️ 🩶 ❤️
@bathiemassambathiam6749
@bathiemassambathiam6749 2 ай бұрын
Nioune Serign Bethio moy souniou Serign limou niou diguel moy Deugui Deugui dieumem dji
@ssalioufall3449
@ssalioufall3449 2 ай бұрын
MALAKA WAKH DH MOM RK LANIOU DOYLO
@goralo4353
@goralo4353 2 ай бұрын
Akassa ame na solo Yalla na Yalla maiye diam thie barcke serigne touba amine ya rabi ♥️♥️♥️❤❤❤
@samatele7037
@samatele7037 Ай бұрын
Fethie ak way rek dou diamou Yalla. Serign Touba fowoul folouwoul...
@cheikhgueyekemaantv7667
@cheikhgueyekemaantv7667 Ай бұрын
Macha allah wallahi ndeysane refetna
@mariamangom8163
@mariamangom8163 2 ай бұрын
Degueleu dalibé dale digal laye diéfé dieureudieuf thioun yalla nala fi yalla bayi
@seyfoulahi8341
@seyfoulahi8341 Ай бұрын
Vérité absolue ❤
@user-wf2ef6gu8r
@user-wf2ef6gu8r 2 ай бұрын
Yalna lepp melate namou melone mom.. founioukoy wakhei woor nalene ni lamoufi bayi dou lii.. 5ans après vous êtes là à lui répéter YAAY SERIGNE BI, YAAY SERIGNE BETHIO rek melni dako dessei gueum , wala dagn kokoy deufeulei
@seynaboudiack7692
@seynaboudiack7692 2 ай бұрын
Grazie mille serigne Touba ❤️ 🤎 ❤️ 🤎 ❤️ 🤎 ❤️ 🤎 ❤️ 🤎 ❤️ 🤎 ❤️ 🤎 ❤️ ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@Layefall08
@Layefall08 2 ай бұрын
Machallah abs borom ecotra et c50pn un leaders de sa génération
@user-rr3hb7zh5d
@user-rr3hb7zh5d Ай бұрын
Serigne Yalla nako Yalla yeureum yen nak si ay thiakhan rek nguen nek
@user-hw4jn9ky1s
@user-hw4jn9ky1s 2 ай бұрын
Thiedo mi d loudoul seytané defouko. Ki loumou yekkoul Cheikh Béthio bimou nekké thie AVC bi amoul. Il avait fait des vidéos sur Facebook di attaquer Cheikh bi. Tey mo nieuw fi di doul
@mamediarradiop3398
@mamediarradiop3398 Ай бұрын
😂😂 ki mo faux
@Anta-hp2do
@Anta-hp2do Ай бұрын
Gnoune gneup dé mognou yém tay mou sagna tokkk ni Cheikh bi moko Yarrrr….Yawou Lo wakhoul cheikh bi si lou bone amoul té bougn la teudioul prison c’est grâce à Cheikh Bethio….. Diédoooo merdeeee
@soxnasibousso2390
@soxnasibousso2390 Ай бұрын
Damaa waaru man….. waxi démb ak yoy tay yi daal wutee na
@bayesallndiaye2646
@bayesallndiaye2646 2 ай бұрын
Sohna Aida Saliou Thioune Yague Lool Tewer Aminne 🤲🤲✅️
@academie_zikroulah
@academie_zikroulah 2 ай бұрын
Aka weerr❤❤❤
@cheikhndiaye7344
@cheikhndiaye7344 2 ай бұрын
Machalla amna solo Dieure dieuf ❤❤❤
@mousthatouremerci863
@mousthatouremerci863 2 ай бұрын
❤❤❤❤
@morniague945
@morniague945 Ай бұрын
Bilahi werna
@falloudiop2297
@falloudiop2297 2 ай бұрын
s salihou degall mom dimbar la ❤❤❤❤
@mamadoudieuzbou9304
@mamadoudieuzbou9304 2 ай бұрын
Bilahi dafay doul😂
@fatoudieng2560
@fatoudieng2560 2 ай бұрын
« AIDA NGUI MAA NI YAYE MANE MAY YAW » faaté hadiou fi. Té kén nétali wouniou les archives sont là.
@sonhiboushop2855
@sonhiboushop2855 Ай бұрын
Saway bayi len sen tapalé lolou takhoul mou nekeu ape Serigne mom Soxna Cheikh bethio lawon rek
@sonhiboushop2855
@sonhiboushop2855 Ай бұрын
Aida diallo mi dou dem feneu lithie kanam rawoul aye gueteu
@saliousima-6629
@saliousima-6629 2 ай бұрын
Wakho deugddè wakhalal serigne Saliou loumouwakhe bakhna rek
@user-rx1gk9bq7r
@user-rx1gk9bq7r Ай бұрын
Khana aida nga 😅😅😅😅dothi am ndam de
@diattaabbakara404
@diattaabbakara404 Ай бұрын
​@@user-rx1gk9bq7r😂😂😂😂
@khadimdiop6988
@khadimdiop6988 2 ай бұрын
Dieureudieuf Serigne Touba❤❤❤❤❤❤❤
@LaylaNdiaye
@LaylaNdiaye Ай бұрын
الحمد لله الذي عافانا مما ابتلاكم به وفضلنا على كثير ممن خلق تفضيلا
@binetougueye8293
@binetougueye8293 Ай бұрын
😂😂😂😂😂
@salioundiaye888
@salioundiaye888 2 ай бұрын
Thiedo fumiste nga nafékh nga guénal si ndiabotou Seriñ Bethio gui. Sa intérêt rk ngay dokhal.
@dofoubamba65
@dofoubamba65 2 ай бұрын
Dgue mo nékhoula dgue rek limou wakh mo ame dhé
@marie-claireagut1538
@marie-claireagut1538 2 ай бұрын
Aka mana doul sahk yaw momou y'a négoul thie dara féne ak diahaser rekk
@sisternana7385
@sisternana7385 Ай бұрын
Alkhamdoulila bagnioula amei thioune
@cherifaidarasylla33
@cherifaidarasylla33 2 ай бұрын
Thiedo y'a meune fene
@Beugdeug
@Beugdeug 2 ай бұрын
Comme c'est un thiedo dans le mouridisme on le comprend,
@user-sq1jn4fh3p
@user-sq1jn4fh3p 2 ай бұрын
😅
@MouhamadouBassirouDiop
@MouhamadouBassirouDiop Ай бұрын
😂😂😂
@user-yz7kf9vu9t
@user-yz7kf9vu9t 2 ай бұрын
Machalla
@donoba1742
@donoba1742 Ай бұрын
Yow thiédo Mouride yow bokougua thii gni diakhassé keur Serigne béthio féén rék guéy dèff fi guafidonn fénal Serigne béthio .on te connait séytanégua.
@user-fx5pp4br5f
@user-fx5pp4br5f 2 ай бұрын
Yenn a yaxx Sénégal
@MouhametFall-nv8dq
@MouhametFall-nv8dq 2 ай бұрын
Mais moni aida gui nii diap thie mane moy deug deugui diap tie aida lgui leraal ma kaddou cheikh bethio yii yii
@adamasane939
@adamasane939 Ай бұрын
Thiedo bayil fen .
@YacineDiouf-up7gf
@YacineDiouf-up7gf Ай бұрын
Deugleu ❤❤
@badiartv242
@badiartv242 2 ай бұрын
BETHIO a bien dit diape si AIDA DIALLO moye deug deug diape si môme. bayilene nafekh AIDA DIALLO mo ko yore
@user-rc4vw2gf9x
@user-rc4vw2gf9x 2 ай бұрын
T'es pas mouride, amoulo talibé écris Cheikh bethio ô moins
@PapeNdiaye-wq8lj
@PapeNdiaye-wq8lj 2 ай бұрын
Ya aida rek lagnous tope aye wakhou dof rek guédi wakhe
@s.falloutaysirmbengue7746
@s.falloutaysirmbengue7746 2 ай бұрын
Boy Topp Daguaye Topp Kou Am Yalla Aida Amoul Yalla Déme Lene Guene Jeufé Ndiguel Yeenak Sene Djiguene Bobou
@user-sq1jn4fh3p
@user-sq1jn4fh3p 2 ай бұрын
​@@s.falloutaysirmbengue7746 ndogoli yaw khana khamo ni sa Serigne khalifam souko Soxna AÏDA rawalé woul euleuk d'où raw yalla khamna lolou
@s.falloutaysirmbengue7746
@s.falloutaysirmbengue7746 2 ай бұрын
@@user-sq1jn4fh3p Yaw Wakhak Yaw Perdue Temps La Démal Diangui Li Yalla Wakh
@BabacarNgom-yu1ku
@BabacarNgom-yu1ku 2 ай бұрын
Thièdo nèko mou mirass boudè dègue rèk
@mohamedka1079
@mohamedka1079 2 ай бұрын
Sopil sa tourwi thiédo amoul si yonewi taga bayi bayi doule😂
@papamedounefalldiop894
@papamedounefalldiop894 Ай бұрын
Thièddo nààfèkh, koù gnàkk diòmm guà
@seynaboutine373
@seynaboutine373 2 ай бұрын
SAST ❤❤❤❤❤
@combecane257
@combecane257 Ай бұрын
Amna solo yalna gnou sougnou boolé baal
@daarahalimoulkhabirdaaraha3389
@daarahalimoulkhabirdaaraha3389 2 ай бұрын
Dieureudieufat Sokhna Aïda Saliou Thioune Deug Deugui Dieumi Serigne Béthio
@sonhiboushop2855
@sonhiboushop2855 Ай бұрын
Meunoul nekeu CHÉIKH bethio kokou aida Diallo la meuna nek
@dio8756
@dio8756 2 ай бұрын
Waladoul khalbi waladoul soulbi sokhna aïda da am ngueureum serigne saliou thioune donou deureum
@DieynabaDiallo-yv7bx
@DieynabaDiallo-yv7bx 2 ай бұрын
Donnou sa baye don sa baye ko gueune mbirmi dou ndono taloubé rek moy mayé
@badiartv242
@badiartv242 2 ай бұрын
l un des facteurs qui retardent la croissance de notre pays
@damefall8715
@damefall8715 2 ай бұрын
Kou athie day bagne kou sentou kaw kou mom khar mii nga bayi boum gui
@falloulo2954
@falloulo2954 2 ай бұрын
S Chikeh kénla billahi
@dethiendiaye4716
@dethiendiaye4716 27 күн бұрын
Kou la Jap saytané koula bayi bayi saytanè
@toubadiop4324
@toubadiop4324 2 ай бұрын
❤️❤️❤️
@mbayedieng379
@mbayedieng379 2 ай бұрын
❤❤❤❤
@user-ry3qy3kr8z
@user-ry3qy3kr8z 2 ай бұрын
rere amna Sénégal waxi dof ngay dég
@leveridique3001
@leveridique3001 Ай бұрын
SERIGNE BOUKHAMOUL AK WAAW DOU SERIGNE
@twitchbadji5867
@twitchbadji5867 2 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤
@zizaziza5450
@zizaziza5450 2 ай бұрын
nieuw pour lan
@naandulfall4222
@naandulfall4222 2 ай бұрын
C’est ceddo murid sadix et non Seriñ Saliou Thioune
@ndeyekhadyndiayenkn6863
@ndeyekhadyndiayenkn6863 Ай бұрын
SERIGNE BETHIO waxoul lolou deh😂😂😂😂dani AÏDA ngi ni ma Ngii ni mani may mooom mooom Mann diap si AÏDA DEUG Moy diap si man tèih kouko dèf Dina ma nopal Tay AK AK euleuk Tecsi ni AÏDA mi kou Ande AK mooom liguèyal SERIGNE TOUBA
@user-je9dy6cl5h
@user-je9dy6cl5h 2 ай бұрын
Aminé yarabi 😢🤍 🤍🤲🤍🤍
@modoundiaye7945
@modoundiaye7945 2 ай бұрын
Ndaysane lou WËRR
@sambaliou5859
@sambaliou5859 2 ай бұрын
Tiedo maridd bayyilénn diakhassé té diéma boolé
@salioufall9385
@salioufall9385 2 ай бұрын
ماشاء الله 🤩🤩
@gueyeabdou8849
@gueyeabdou8849 2 ай бұрын
Lii d’où waji thia 2stv moytuko dh😂
@tvsenegal2789
@tvsenegal2789 2 ай бұрын
Thiay senegal..sounah younété bi dioye n'a....
@khadimsarr5704
@khadimsarr5704 2 ай бұрын
Serigne Béthio dh Sokhna Aïda Saliou Thioune la wakhné yaye Mame may Yaw niou Fékké ko kénn Nétaliwou niou 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
@omarndiaye9040
@omarndiaye9040 Ай бұрын
😂😂😂😂😂😂😂
@dethiendiaye4716
@dethiendiaye4716 27 күн бұрын
Aka meuna fén thiédo
@khadimdabo6586
@khadimdabo6586 2 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤😢😢😢
@malickndiaye2804
@malickndiaye2804 2 ай бұрын
Yen gni saga yen monu len na nopu lou ji
@leveridique3001
@leveridique3001 Ай бұрын
CÉDDO MARIDE MAME MAL MBAAYE MBAYE PÉKH YÉENA SOOF TÉ SOUUFÉ TÉ NIAKK DIOM
@warkha
@warkha 2 ай бұрын
La reconversion d’un nervi religieux de la politique au communicateur de cérémonie. Puisque BBY ne paie plus et la dénigration de Sonko ne marchent plus.
@sarahsarah2683
@sarahsarah2683 Ай бұрын
Ndeysane biiii béthio di dounde lui il vivait en France di émigré. Taye mome leup nékh neu
@ibrahimkebe3059
@ibrahimkebe3059 2 ай бұрын
Saway mom fune lay guenne
@deboursy6215
@deboursy6215 2 ай бұрын
Yenewoul dara sa way linguendi def dou diiné
@serignesaliousarr5606
@serignesaliousarr5606 Ай бұрын
Bou niew
@PrinceEntrepreneur
@PrinceEntrepreneur 2 ай бұрын
AÏDA diallo dafa yabatei ana djiguen
@CheikhomarMbaye-rd2of
@CheikhomarMbaye-rd2of Ай бұрын
Sokhna Aida ya gale taweire
@mouhamedmbaye9735
@mouhamedmbaye9735 2 ай бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂ayway mo meuna doul
@coumbakharfaye5078
@coumbakharfaye5078 Ай бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂 sacré ceddo meuna feen
@serignesalioumbow8904
@serignesalioumbow8904 2 ай бұрын
Dett wayy 😂😂😂 boul dioye
@oumarsamb7408
@oumarsamb7408 2 ай бұрын
DIEUREDIEUFATY YA AIDA SALIOU THIOUNE YAGUE FI TEE WERE ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@LamineSow-vm9de
@LamineSow-vm9de 2 ай бұрын
Ya meuneu fene diène mak faye ya diekeu wor serigne bethio guissoula ngay wakh guinawam fo nékone pendant qui les la
@user-iy3ds7ro4c
@user-iy3ds7ro4c 2 ай бұрын
Wérna
@maguettebomou5177
@maguettebomou5177 18 күн бұрын
Vraiment shaitané yi nioy yakha les relations dans les familles liloumouy garouwalé ?
@papemomardienglofficiel
@papemomardienglofficiel 2 ай бұрын
BAYI LÉNE DI WAKH NGIR BEGU LOU NÉKH NIT
@papemomardienglofficiel
@papemomardienglofficiel 2 ай бұрын
MANDOU LÉNE THIÉDO YAW GUEMO SERIGNE BETHIO MANDOUL AP DIOULIT DAY MANDOU
@s.falloutaysirmbengue7746
@s.falloutaysirmbengue7746 2 ай бұрын
Deugue Rék La Thiédo Wakh Waxoufi Lénène
@abdoulahatendiaye7020
@abdoulahatendiaye7020 2 ай бұрын
​@@s.falloutaysirmbengue7746s fallou thiedo yoname nékoul si keure s béthio
@user-fx5pp4br5f
@user-fx5pp4br5f 2 ай бұрын
Denguein di naxx sen bopp
@mohamedka1079
@mohamedka1079 2 ай бұрын
Doulega dhé thiédo
@thebosssfresh9080
@thebosssfresh9080 2 ай бұрын
😂😂😂😂😂
@ibrahimaniangboxeurofficie9561
@ibrahimaniangboxeurofficie9561 2 ай бұрын
Yaw seytaane Nga. Laataa Sëriñ BEECO làqu lune yakk Nga ko, bi ci mujj mooy bi Xaadim Diediou wàcce ab liggéey. Li Nga ci waxoon ba tay fàttewuma ko. Yaw xaalis rekka la ñor. Amoo Ngor
@babacarseck6421
@babacarseck6421 2 ай бұрын
متشاجع اتق الله حيثما كنت ولاتكن من المتعاصبين
@serignesaliousarr5606
@serignesaliousarr5606 Ай бұрын
Yama doule RK barkep SERIGNE BETHIO
World’s Deadliest Obstacle Course!
28:25
MrBeast
Рет қаралды 122 МЛН
Final muy increíble 😱
00:46
Juan De Dios Pantoja 2
Рет қаралды 34 МЛН
Получилось у Вики?😂 #хабибка
00:14
ХАБИБ
Рет қаралды 5 МЛН
L'EMISSION DES EMISSIONS 24 06 24.
31:34
Solution Info
Рет қаралды 28 М.
Dans l'intimité de Serigne Saliou et Cheikh Béthio Thioune - Ziars de 1987 à 2004
29:36
Babacar Kassé devant Serigne Babacar Sy Abdou que du bonheur 😍
8:03
HABIBBA TV TIVAOUANE HD
Рет қаралды 10 М.
Этот мальчик настоящий герой
1:00
ViralMoments
Рет қаралды 1,6 МЛН
Tom & Jerry !! 😂😂
0:59
Tibo InShape
Рет қаралды 50 МЛН
Mama Vs Tante‼️
0:13
Abil Fatan Key
Рет қаралды 18 МЛН