La soeur de Mario démasque Ndakhté "Lima Mario Wakh Si Mom...Dama Féké Dokhane, Féké Tak..."

  Рет қаралды 58,551

Senegal7

Senegal7

29 күн бұрын

#Senegal #DiomayeFaye #Sonko
Rejoignez cette chaîne pour bénéficier d'avantages exclusifs :
/ @senegal7tv
L'information en temps réel
Visitez notre site web: Senegal7.com
Retrouvez Senegal7 sur les réseaux sociaux
Facebook
/ senegal7officiel
TikTok
/ senegal7tv
Instagram
/ senegal7
Twitter @senegal7com
Abonnez-vous pour plus de vidéos et n'oubliez pas d'activer la cloche de notification

Пікірлер: 146
@user-ub4kg3cl8y
@user-ub4kg3cl8y 26 күн бұрын
Yalna nga am djikeurr bou melni Mario amine touf touf 🙏🙏🙏
@ndeyendoye9856
@ndeyendoye9856 25 күн бұрын
😂
@user-cg4vr4gy4r
@user-cg4vr4gy4r 24 күн бұрын
😂😂😂
@ndeyakarisma3445
@ndeyakarisma3445 22 күн бұрын
Amine 😂yaw mrci rek
@rosalieciss9394
@rosalieciss9394 11 күн бұрын
😆
@mymathiat5005
@mymathiat5005 22 күн бұрын
Féké dokhane, féké takk, wayé féko wo li ci biir negg,
@ndeyediallo7609
@ndeyediallo7609 17 күн бұрын
Merci
@MameDiarraDiakhite
@MameDiarraDiakhite 16 сағат бұрын
Merci beaucoup
@mamidiallo5495
@mamidiallo5495 26 күн бұрын
Ndakhtei Meussoul wakh ni yobouwko au contraire elle a dit nio ande ba fofou mou message alors k gnogui toke pour dem bref
@user-dh4xn8jb1x
@user-dh4xn8jb1x 26 күн бұрын
Yénn tmt délén dégg lou ndakhté limou wakh moy ke ni Mario moko yobou clinique mais dieulsi wouko cousin wameu lako bolél pour mou yobouko keureum en plus mou envoyé message wakh ko ni dafay dém soirée Momo Dieng 😮 mais tmt délél déff ndank ak di déglo
@niangtra
@niangtra 22 күн бұрын
Bayiko mouy wakh melni day féké lithi biir negue bi
@MamecoumbaThiam-jf6bm
@MamecoumbaThiam-jf6bm 21 күн бұрын
Merciiii
@user-xf8ft6wq2n
@user-xf8ft6wq2n 17 күн бұрын
iow doulle wakho fii dara mario dala faye yena yame mdr
@SokhnamaimounambackeDiop
@SokhnamaimounambackeDiop 22 күн бұрын
Sa yone nékoul si couple diambour beuri ga wakh trop
@NdeyeAwadiallo-ry3xb
@NdeyeAwadiallo-ry3xb 19 күн бұрын
Ioe tontou sii liniou la lath dh mouy dielalè nnou mario loumouy liguéy 🤣🤣🤣
@HaddyKonteh
@HaddyKonteh 20 күн бұрын
Wouye commentaire yi yagui maye raye
@marietoutamba223
@marietoutamba223 24 күн бұрын
Yw kou niak diom nga ngay djiguene di di autorisé dieukeur diambour di Dém ay soir mario niak nék kilifeu goor bo démé ba am diabar nga wara wagni you beuri soite nga diel sa diabar andak AK môme dof bi môme xam na daf la faye comme yénay and
@madjiguene4935
@madjiguene4935 24 күн бұрын
Wa ki mome moye kane yaw grawnga nak😂😂😂😂😂
@user-ub4kg3cl8y
@user-ub4kg3cl8y 26 күн бұрын
Je suis pas un femme 😂😂😂mdr😂😂
@user-vp4bo7yr2k
@user-vp4bo7yr2k 19 күн бұрын
Merci ndeye thioraye❤❤❤❤❤❤ veritè absolue
@jamilasall7409
@jamilasall7409 22 күн бұрын
Mais yawe dieukeurou diambour domou diambour nga coye yobou mouye mayé khaliss yawe cousobega do nite bayiléne dieukeurou diambour
@MamecoumbaThiam-jf6bm
@MamecoumbaThiam-jf6bm 21 күн бұрын
Féké demba Féké tay takhoul nga wara tok si télé bi disi wakh nitt kou né am na fou yam si nit conseil en privé 😔😔
@mamirassoul1595
@mamirassoul1595 22 күн бұрын
Seutané dh wessouwoul nétali sa guintou morom
@yacinedrame-kl5ok
@yacinedrame-kl5ok 20 күн бұрын
lisi bir neig yi yay bila diour sah meunousè xam louko si gnar gni ka seik wax kone surtout mandou leine tay wax liléne wor
@aichagueye1310
@aichagueye1310 27 күн бұрын
Doul yéna niou sonal thim😢
@tendancebmn1573
@tendancebmn1573 23 күн бұрын
Wakhoul ni mario yobou wouko dé dani dafe ko yobou bafofou message ko ni gafay dém soirée. Dél wakh lou ame
@ramatoulayediaw3864
@ramatoulayediaw3864 23 күн бұрын
Wakh degg loolou de la wakh te khawma looumouy soiree
@queendiola5945
@queendiola5945 20 күн бұрын
Limou tak si loho bi c’est pourquoi 🤔
@KhadijaBabou-qr1rw
@KhadijaBabou-qr1rw 23 күн бұрын
Wa yow mi est ce que nite nga niak ndawlé wesou woul ngay wo diabarou diambour diko tagoul pour mou bayi djeukeureum ya wayadi DEUG xana meuble ngafa wone armoire Wala fauteuil li😂
@mbayefilledesamum1947
@mbayefilledesamum1947 23 күн бұрын
Limou tak si lokhome bi rk guay kham Ni Ki weroul doufi wakh dra lou diar yone 💔
@MarieGomis-ks8so
@MarieGomis-ks8so 22 күн бұрын
😂😂😂😂😂
@user-dh4xn8jb1x
@user-dh4xn8jb1x 26 күн бұрын
Wakho bah légui Mario loumouy liguéye lolou laniou la ladj nga tontou bénén question 😅😅😅
@Thiate499
@Thiate499 24 күн бұрын
Diomi amoul heure kone bokoleen nday ak baye ok Mario Mbaye Wakho leen ko deugue kone samba alar la day def si niti ok mes ioe ndeye thiouray kou niak fayda la
@tantylarose809
@tantylarose809 24 күн бұрын
Mankei la df
@ndeyakarisma3445
@ndeyakarisma3445 22 күн бұрын
Mankei 😂total
@user-qm1yp2dh8w
@user-qm1yp2dh8w 22 күн бұрын
Je suis pas un femme je suis un homme 😂😂😂😂😂
@Btymboup
@Btymboup 22 күн бұрын
😂😂😂😂😂yaaaaaaaaaaaaaaaaaaa
@mouninandiaye7917
@mouninandiaye7917 25 күн бұрын
Est-ce qu'elle sait réellement ce qu'elle a porté à sa main ?
@ramatall6798
@ramatall6798 24 күн бұрын
Merci question bi la done set
@tantylarose809
@tantylarose809 24 күн бұрын
C la question k jm pose ki Esk sva réellement
@moustapharassoulilahisow7481
@moustapharassoulilahisow7481 24 күн бұрын
Ye y n tttt loloum lia
@lindorcisse2994
@lindorcisse2994 23 күн бұрын
😂😂
@AminataDrame-kq7im
@AminataDrame-kq7im 22 күн бұрын
😂😂😅😅
@AntaFall-ug6ke
@AntaFall-ug6ke 21 күн бұрын
Keine d'où wakh amine
@Dangerous1404
@Dangerous1404 26 күн бұрын
Mario ak ndakhtè danio beugueuntè,ndakhtè da pank khèkh kate le
@malily6705
@malily6705 26 күн бұрын
😂😂😂😂
@Aydashoutv
@Aydashoutv 25 күн бұрын
Bilae
@abdourahime1
@abdourahime1 3 күн бұрын
Ki dée mandouwoul walahi negou seye boul ci wakh Mane kene menoul wakh limaye doundou Kone teye reck
@RamaLaye-bl8sp
@RamaLaye-bl8sp 21 күн бұрын
Machala beugue nala ngir seydina lumamou
@aidasow229
@aidasow229 12 күн бұрын
Loussi place bii dou diare 🙃
@aichasene6618
@aichasene6618 22 күн бұрын
WA ANA SOUTOURA MAINETENANT CHERCHONS UN TERRAIN POUR COMMENCER LES RELATIONS EN PUBLIC ET SE MARRIER DEVANT UN PUBLIC
@yacinedrame-kl5ok
@yacinedrame-kl5ok 20 күн бұрын
ah mane nak geum na ndakhetè deuggg parce que si waxam mario ba legui ni dafay yoni ay nit pour mou diapalé ka😂
@AmyDiop-ml5lz
@AmyDiop-ml5lz 23 күн бұрын
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@khadijadiop7292
@khadijadiop7292 16 күн бұрын
Ay bouniou andaté son bu😅😅😅douniouko atan
@user-yy6ee6hv7r
@user-yy6ee6hv7r 26 күн бұрын
Yow demal tog😅 dulkat nga ya Mario yena emm
@aminandong7735
@aminandong7735 26 күн бұрын
😂😂😂
@user-bm1rd4ce7p
@user-bm1rd4ce7p 26 күн бұрын
🤣🤣🤣🤣liii
@ndeyakarisma3445
@ndeyakarisma3445 22 күн бұрын
😂😂déna way
@yacinedrame-kl5ok
@yacinedrame-kl5ok 20 күн бұрын
yaka wax kou neik amgua sa matou lall yaw reik yakay yeuk keine douka yeuk deug dou rombiii nopouuu nak
@mamefatydiop3992
@mamefatydiop3992 21 күн бұрын
@fatigaye6489
@fatigaye6489 25 күн бұрын
Ki mo waga prank key 😂
@NdeyefantaDiagne-jf8wf
@NdeyefantaDiagne-jf8wf 24 күн бұрын
Sen site yii amouniou programme 😂😂😂😂
@user-yh9sn9kg4n
@user-yh9sn9kg4n 23 күн бұрын
Gang biii😂😂
@Rassouliphile9861
@Rassouliphile9861 22 күн бұрын
Mo ma fi bayi mou melni kouy rakhass ndap
@user-yh9sn9kg4n
@user-yh9sn9kg4n 22 күн бұрын
@@Rassouliphile9861 tayy ngama😂😂
@user-nw9in6yr1j
@user-nw9in6yr1j 23 күн бұрын
Doul nga deh
@binettendiaye2885
@binettendiaye2885 23 күн бұрын
Moko dorr mou Wakh ko mayy lenn nitt gni diamou
@amicisse2428
@amicisse2428 24 күн бұрын
Ndeye yaw nopil lisi bir négou seye diabour khamoko métrigé wo liguaye wakh
@tantylarose809
@tantylarose809 24 күн бұрын
Bayil ma ki mouy Doul ni 😂elle m’énerve
@awasy9586
@awasy9586 19 күн бұрын
Wakhoul younouko dai danai dieulsi wouy ko ak Momo dieng do thi wakh en tout cas mom Mario sikana même bou sai ❤ bou rafete la yor
@ModousambModousamb-mm2wk
@ModousambModousamb-mm2wk 23 күн бұрын
Merci Ndéye Thiouraye yaye guorr pirr wouté nga ak dof yi ndiguén yi gueum Ndakhté té amouniou bén preuve thi wakhou Ndakhté yi😢😢😢😢 ce
@NafiSamb-rp7jg
@NafiSamb-rp7jg 21 күн бұрын
Mario jr
@ModousambModousamb-mm2wk
@ModousambModousamb-mm2wk 21 күн бұрын
@@NafiSamb-rp7jg Non très sincèrement je connais bien la famille de Major Mbaye alias Mario Mbaye man ak rakou papam nioy handeu li Ndakhté wax 80 % yeup ay féni nén leu promotion album bi rék ladon hout ba tax mouy diémeu yakeu domou Diambour bi mais mounouko yakeu famille Major danio bax bilahi ♥️♥️
@NafiSamb-rp7jg
@NafiSamb-rp7jg 21 күн бұрын
@@ModousambModousamb-mm2wk doyna war niom niar ak yalla rk nio kham deug bi mtx kou yabo mbadou ci problème bi negou seuy lafay khéw kéne douko kham loudoul niom niar gni bokou neg ni ak yalla bi don sédé bi yalnagnou yalla may soutoura ba problème bougnou am mou yém ci birr neg yi ba kéne douko kham ba internet disi am yon
@ModousambModousamb-mm2wk
@ModousambModousamb-mm2wk 21 күн бұрын
@@NafiSamb-rp7jg vérité absolue 🤜🤛
@amydiaw5859
@amydiaw5859 25 күн бұрын
😂pour maneu ndawsy ak mario gno bokou ndaye ak baye😅
@dianablackqueen3510
@dianablackqueen3510 24 күн бұрын
Xpdrrrr grave 😂😂 pareille pour mane mouy oubëkou di insister ni. Cheutttttt deukebi tamite 😂
@tantylarose809
@tantylarose809 24 күн бұрын
D mm k moi moy tepeikou ni
@tendancebmn1573
@tendancebmn1573 23 күн бұрын
Dama diakhal ki
@dianablackqueen3510
@dianablackqueen3510 23 күн бұрын
@@tantylarose809 xpdrrrr 😅😂😂
@ndeyakarisma3445
@ndeyakarisma3445 22 күн бұрын
😂😂diomii amoul heure
@user-ee1wd6hp7j
@user-ee1wd6hp7j 12 күн бұрын
Wakhi nafèkh rek ga fi wakh
@SambaTague-fv7bz
@SambaTague-fv7bz 2 күн бұрын
Sénégalais si bopam mo ame fite bayiléne di saga Mario ta khamoléne dara louléne lerr démléne balou Mario dara lérouléne ci mbiryi barina niou naafékk trop
@VeroniquemariepaulGOMIS
@VeroniquemariepaulGOMIS 18 күн бұрын
Yaw bo amé djeukeur bouy sathieu daguay andal mome sathieu 😂😂
@yayebayeniass9325
@yayebayeniass9325 24 күн бұрын
Journaliste bi nakhari na khel deh 😅
@user-qp2mg9lj5q
@user-qp2mg9lj5q 24 күн бұрын
Gni leni posé kestion niongni togne roussale wakh makay tagoul
@ZaharaDia-sq2kl
@ZaharaDia-sq2kl 10 күн бұрын
Ndakhté da dioum rek
@gnilanefaye5126
@gnilanefaye5126 16 күн бұрын
Lou Mario Doug yakossi dougal
@amymare2989
@amymare2989 20 күн бұрын
Ki douniou dimbalé yaw Mario wakhoul ngay wakhe nopil way bouniou ray
@marietoutamba223
@marietoutamba223 24 күн бұрын
Yw mi di wax té nga téyi mouno xam lisi bir
@MamecoumbaThiam-jf6bm
@MamecoumbaThiam-jf6bm 21 күн бұрын
Del deglou di wakhal li ndakhté wakh wakhou lani yobou wouko del deglou yénay tass keur diambour akh
@AdjiSECK-gu7xx
@AdjiSECK-gu7xx 25 күн бұрын
Wakhofi dara
@Itsaminaah
@Itsaminaah 15 күн бұрын
Ndakhté wakhoul ba tey mario yombouu koo hôpital
@user-nr9mw1fn6s
@user-nr9mw1fn6s 17 күн бұрын
Ndeye nak ya yéye tague ko sa boutique molako tidjil koula all ay beute wone la figay khol
@jamilasall7409
@jamilasall7409 22 күн бұрын
Kénewaroul kharito ak dieukeurou diambour yawr do nite coubakh loye ada ak dieukeurou diambour
@jamilasall7409
@jamilasall7409 22 күн бұрын
Bariga wakh sopega yawedocoubakh
@Itsaminaah
@Itsaminaah 15 күн бұрын
Ioe léer gua cas dakh négua bou khoulo ak ndakhté mou woh néelaa cas am gua néekoo déeffa tii gua sa meuniin kon mario sii deff la deukeuk
@AntaFall-ug6ke
@AntaFall-ug6ke 21 күн бұрын
Del wakh deugg
@ramatoulayediaw3864
@ramatoulayediaw3864 23 күн бұрын
Wayen neegou sey geun begg fa kham leppp ajhjjhhhhh Senegal wayy khana chambre ba daa am camera Mario conecte len si yen gneupp ba darà reuthou len doynawarr. Bakhou Mario ak limouy dound ak diabaram dou ben kou nek moo kham mattou lalam
@ZaharaDia-sq2kl
@ZaharaDia-sq2kl 10 күн бұрын
🤣🤣🤣🤣🤣
@SokhnambeneNdiaye-iw1ow
@SokhnambeneNdiaye-iw1ow 17 күн бұрын
Ndakhté nena daka yobb clinique baparé envoyé ko message neko day dem soirée té mom li am doulako wakh jamais
@amicisse2428
@amicisse2428 24 күн бұрын
Fékéwo manoul djiguéne gua
@user-jx3cx4ip5h
@user-jx3cx4ip5h 24 күн бұрын
Yaw ya sof ndaxte amatoul sen diote xalé la day topato aveniram elle a tourné la page elle est passée à autre chose aurevoir et merci tiao
@user-yx5tl9jf8c
@user-yx5tl9jf8c 22 күн бұрын
Ya am fite kay
@AdjiSECK-gu7xx
@AdjiSECK-gu7xx 25 күн бұрын
Yawmi ma khame geuwma saye wakh
@mariamsylla1094
@mariamsylla1094 16 күн бұрын
Dof bii
@Touty-wp3gp
@Touty-wp3gp 23 күн бұрын
Negu sey lifay xew jeker AK jabar rek gnokoy xam .té nit kenn menuko xam .nit limu beg nga xam ci Moom rek ngay xam muy goor MBA muy jigeen ñu bayi ci xel
@mymathiat5005
@mymathiat5005 22 күн бұрын
Akay deug
@Adjifatoufall-hw3gl
@Adjifatoufall-hw3gl 20 күн бұрын
Yéne mandou lène si seuyou dianbour 😡
@mbayamefall3536
@mbayamefall3536 23 күн бұрын
Wa ltx mario dou guéneu wakh boudé deugula rek doul rek nguene fi néké
@YoussouCamara-bx2bm
@YoussouCamara-bx2bm 22 күн бұрын
Niaar gni kane moo thi journaliste bi ?😂😂😂😂😂😂
@pendakebe37
@pendakebe37 12 күн бұрын
Mou sociale ça n'a rien à voir avec son fort intérieur Ba nga khamé né meunoulo gnakk fété tu reste neutre Mom ak présentatrice bi nio Yam 0 expertise
@naboudiouf4965
@naboudiouf4965 23 күн бұрын
Yaw bilahi yagui melni do djieguen
@SarrBiha
@SarrBiha 23 күн бұрын
Je suis manquable 😭😂😂😂😂
@lalionnefaramareen9306
@lalionnefaramareen9306 22 күн бұрын
Un femme nak 😂😂😂
@ndeyakarisma3445
@ndeyakarisma3445 22 күн бұрын
@@lalionnefaramareen9306tu es partout la lionne 😂alrs je lis que les commentaires 😢😂
@lalionnefaramareen9306
@lalionnefaramareen9306 22 күн бұрын
@@ndeyakarisma3445 nio yam deh fouma dem fekk lafa 😂😂😂😂commentaire rk lagnouy toppou wa toppou cas 😂😂😂😂
@ndeyakarisma3445
@ndeyakarisma3445 22 күн бұрын
@@lalionnefaramareen9306 commentaire yi nio dak lep 🥰❤️🙏motax 😂bon c’est normal fo neik magui faa
@YoussouCamara-bx2bm
@YoussouCamara-bx2bm 22 күн бұрын
Legui métier journaliste yakkou na
@rokhayacisse7157
@rokhayacisse7157 22 күн бұрын
Ki visibilité leu beug j la connais ndeye thiouraye keur massar la deuk
@NiangIbrahima-mb5vb
@NiangIbrahima-mb5vb 4 сағат бұрын
Yaw dangay doul rk dieu leu rou diambour ngay yobou soire yoboull sa dieukeur soire
@NgaytaDiop
@NgaytaDiop 15 күн бұрын
Yaw dh warga reglè ak sa wakh djou bari
@ousmanefaye6581
@ousmanefaye6581 16 күн бұрын
Mais epine yiii si lokho bi nak, mooy bane mode encore????
@yacinendiaye1289
@yacinendiaye1289 4 күн бұрын
C pour massage du sexe masculin
@yacinendiaye1289
@yacinendiaye1289 4 күн бұрын
C pour massage du sexe masculin 😌
@FatimaMboob-kc7xz
@FatimaMboob-kc7xz 13 күн бұрын
Yow fenn k
@tendancebmn1573
@tendancebmn1573 23 күн бұрын
Li si bire seuye yép mano ko khame gay ratatati
@Sfr_time
@Sfr_time 11 күн бұрын
Wakhofi gatt guay bouroukhlou nonou di publicité walé merde
@amymare2989
@amymare2989 20 күн бұрын
Tu n'es pas un femme kay 😂😂
@LissBb-ob8ys
@LissBb-ob8ys 22 күн бұрын
Kouy avorté dina diar sa place dila nouyou kone dh amna diote ak mitite bobou
@NabouNdiaye-ni3vg
@NabouNdiaye-ni3vg 22 күн бұрын
Ki fene Kate la
@nafissatouniang4817
@nafissatouniang4817 24 күн бұрын
Yaw linga def sa lokho lanela yaw mouy melni super héro dessin animé ni
@lindorcisse2994
@lindorcisse2994 23 күн бұрын
Pour intimite leuh lou graw😂ki weroul
@nafissatouniang4817
@nafissatouniang4817 23 күн бұрын
Likay naka diekeu bimako kholé ak baram you séw you baré yi té noy ak couleur bou féss bi la khamni dou déf diam badou dafay nioromtane ki moy sauvage way sans vergogne wow beut
@lindorcisse2994
@lindorcisse2994 23 күн бұрын
@@nafissatouniang4817 nioromtane lou neix kay🥳🥳🥳
@user-yi3jt6kt9q
@user-yi3jt6kt9q 19 күн бұрын
Oubal saa gatt gui doul rekk
@user-uv5cu2bs2l
@user-uv5cu2bs2l 21 күн бұрын
Ligay wax social la ak téyé diabar bokoul tmt
@miss_0148
@miss_0148 23 күн бұрын
Vous êtes bêtes
@Diarista90
@Diarista90 26 күн бұрын
😂😂😂😂😂😂😂
RÉCIT DE VIE DE NDAKHTÉ LO : CONFESSIONS ET SECRETS INÉDITS - (INTÉGRALITÉ)
1:30:01
Tom & Jerry !! 😂😂
00:59
Tibo InShape
Рет қаралды 50 МЛН
ТАМАЕВ vs ВЕНГАЛБИ. Самая Быстрая BMW M5 vs CLS 63
1:15:39
Асхаб Тамаев
Рет қаралды 4,8 МЛН
ROCK PAPER SCISSOR! (55 MLN SUBS!) feat @PANDAGIRLOFFICIAL #shorts
00:31
Série - Belle Famille - Tabaski - Épisode 9
26:47
Marodi TV Sénégal
Рет қаралды 831 М.
Soirée Spéciale - Invitée: Ndakhté Lo - 25 Mai 2024
17:27
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 227 М.
Tom & Jerry !! 😂😂
00:59
Tibo InShape
Рет қаралды 50 МЛН