No video

Électricité: de la Production à l'utilisation ci wolof | Mën Na Nek

  Рет қаралды 11,015

Bànqaasu xam-xam

Bànqaasu xam-xam

4 жыл бұрын

Électrotechnique ci Wolof
Dalleen ak jàmm ci Daotech. Tv.
Tay dañuy caytu naka lañiy togge, yobbu, seddele ak jëfandiko mbëj (électricité).
Jàng si lakk u reew mi ak xam-xam bumu mëna doon loolu Mën Na Nék
Bienvenue dans l'univers Daotech. Tv.
Aujourd'hui on abordera la productionn le transport-distribution et l'utilisation de l'Electricité.
#Electricité #Électrotechnique #Wolof
🔘 Télé bi
Daotech. Tv moy télé bi ñëkk déf ay widéwo jangalé xam-xamu science ak technologie ci wolof.
Daotech. Tv est la première chaîne d’enseignement des sciences et technologies en wolof.
🔘 Bolén ame ay xalaat yuy yokku (Pour vos suggestions):
👉Facebook: / daotech.industries
👉Instagram: www.instagram....
👉Email: daotech.tv@gmail.com
👉Contact: +221 77 670 22 92
🔘 Way wi nek si suuf (Musique de fond)
👉🏿 Musique de fond : LRGB, La Compilation
Vous pourrez écouter et télécharger la Compilation LRGB dans son intégralité via le site loudoulrapgals...
🔘 Ñi ànd ak ñun si jàngale yi (Partenaires):
👉 Block Business (Label de Music)
Block Business: / blockbusinesscontact
Contact: 77 369 39 95
👉Bytech : Bytech est une entreprise de prestation de service spécialisée dans les installions électriques à usage domestique et bureautiques
Notre mission : « Répondre aux besoins du marché du travail en matière de mains d’œuvres qualifiées dans un contexte de travail de plus en plus diversifié et exigeant ».
Domaines d’activités :
- Renforcement de compétences
- Accompagnement de professionnels désirants obtenir un diplôme professionnel
- Accompagnement d’entreprise dans le cadre de réorganisation et d’innovation
- Etude et réalisation d’installations électriques
- Audit des installation et efficacité énergétique
Activités antérieures :
- Accompagnement de TRI dans sa réorganisation
- Séminaire de formation sur le Dimensionnement et la sécurité des installations électriques à usage d’habitation
- Séminaire de formation sur la mécatronique automobile
Page facebook : / bytech-technologie-258...
Contact: +221 78 164 77 68

Пікірлер: 58
@ousseynousarr5407
@ousseynousarr5407 4 жыл бұрын
Jërëjëf aróona jàllo am Na solo
@AmethFall-wt1xl
@AmethFall-wt1xl 2 ай бұрын
MACHAALLAH Mon prof ✊🏽✊🏽👊🏽
@ndeyediorsalldiop2426
@ndeyediorsalldiop2426 4 жыл бұрын
Machalla amna solo🙏🙏
@m.seyetechnologue2558
@m.seyetechnologue2558 3 жыл бұрын
Machalah lër na nañ👍🏻
@DaoTechIndustriessenegal
@DaoTechIndustriessenegal 3 жыл бұрын
Merci M. Seye
@ousseynousarr5407
@ousseynousarr5407 4 жыл бұрын
Jërëjëf
@leppiwolof2564
@leppiwolof2564 2 жыл бұрын
Waaye daal noonu ngi lay jaajëfal bu baax ci taxawaay bi. Jàngale xam-xam ci làkk ak lu mu metti metti dara melul ni moom.
@daarayseexsaalihu
@daarayseexsaalihu 2 жыл бұрын
Maasàllaa, mbok mi jàngale mi am na solo lool te wolofe.
@laverite5796
@laverite5796 5 ай бұрын
Machallah amna solo
@protv5292
@protv5292 3 жыл бұрын
Bonne continuation
@sambawade2817
@sambawade2817 2 жыл бұрын
Lii amna solo jéngalé ci Wolof waaw goor
@modouniang9673
@modouniang9673 3 жыл бұрын
Machallah ame na solo lool
@DaoTechIndustriessenegal
@DaoTechIndustriessenegal 3 жыл бұрын
Jërëjëf
@thiernosouleymaneba
@thiernosouleymaneba Жыл бұрын
Diallo, merci grand frère. Fierté de notre école, ESGE.
@sonhaybouniang8784
@sonhaybouniang8784 2 жыл бұрын
C super
@gaurysow2802
@gaurysow2802 3 жыл бұрын
Amnaaa sollo
@aichagueye4409
@aichagueye4409 3 жыл бұрын
Machallah😍
@DaoTechIndustriessenegal
@DaoTechIndustriessenegal 3 жыл бұрын
Jërëjëf
@musulmansetsesbienfaits55
@musulmansetsesbienfaits55 2 жыл бұрын
Macha Allahou mais ôu sont les autre
@Modoundiayevoiture
@Modoundiayevoiture 4 жыл бұрын
S'il vous plaît mën na nek xaanaa doungén jangalé français ci wolof wala merci beaucoup pour votre chaîne KZfaq 🙏🙏
@DaoTechIndustriessenegal
@DaoTechIndustriessenegal 4 жыл бұрын
Jërëjëf mbokk mi. Yéene Tele bi moy fexee ba ñëp mën làkk mii di wolof diko jëfandikoo, diko dawal, diko bind, ta diko wax wax wu jub ta jar yoon ngir mën se jànge xam xam bu mu mën a doon.
@Modoundiayevoiture
@Modoundiayevoiture 4 жыл бұрын
Thank you
@babou2838
@babou2838 2 жыл бұрын
Diadieuf lir na amna solo lole yala nako yala yok
@DaoTechIndustriessenegal
@DaoTechIndustriessenegal 2 жыл бұрын
Amine
@virginiegueye1263
@virginiegueye1263 2 жыл бұрын
@@DaoTechIndustriessenegal puis je avoir votre contact pour une solution Eco énergétique
@sanatall7291
@sanatall7291 4 жыл бұрын
Amatina solo
@leppiwolof2564
@leppiwolof2564 2 жыл бұрын
Waaw, kon yu am solo yii ñoo ngi koy amal ci wolof! Waaye turu bopp yi ñuy bind ci farañse moo tax jot ci jafe, te loolu ñu bari duñu ci man a jot. Te yenn saa yi sunu bokki saa-afrig yi dañuy bind farañse ñu indil leen widewoo boo xam ne wolof may wax, fekk ne nun wolof yi noo ngi bind loola ci wolof te duñu ko man a gis. Lu ciy pexe?
@mouhamedlo9013
@mouhamedlo9013 4 жыл бұрын
Intéressant proffesseur
@seckdjibril8826
@seckdjibril8826 3 жыл бұрын
Courant alternatif ak continue dhe beugnako kham?
@ousseynousarr5407
@ousseynousarr5407 4 жыл бұрын
Courant en wolof c'est dawaan g
@DaoTechIndustriessenegal
@DaoTechIndustriessenegal 4 жыл бұрын
Jërëjëf Useynu ci leeral bi Amna solo👍
@abousow3691
@abousow3691 Жыл бұрын
Merci professeur
@ibrahimacueye4449
@ibrahimacueye4449 Жыл бұрын
Machala sa numéro la beugué
@ibrahimafall2944
@ibrahimafall2944 3 жыл бұрын
machallah Yoro leer na
@DaoTechIndustriessenegal
@DaoTechIndustriessenegal 3 жыл бұрын
Jërëjëf
@mouhamedgano4658
@mouhamedgano4658 Жыл бұрын
Lu tax yeggale wuleen
@seexunaakebe9670
@seexunaakebe9670 2 жыл бұрын
Lan mô takh guén aréter védéo yi
@DaoTechIndustriessenegal
@DaoTechIndustriessenegal 5 ай бұрын
Dina tàmbali waat inshAllah
@mouhamedgano4658
@mouhamedgano4658 Жыл бұрын
Mais amoon na solo de
@Combattent2024
@Combattent2024 9 ай бұрын
mes pourquoi ga def thi mécanique parce que ya des mécaniciens au Sénégal
@DaoTechIndustriessenegal
@DaoTechIndustriessenegal 5 ай бұрын
Dina ñëw inshallah
@nourayni4094
@nourayni4094 3 жыл бұрын
Comment pouvons nous faire pour vous rejoindre en formation en électrotechnique ?
@DaoTechIndustriessenegal
@DaoTechIndustriessenegal 3 жыл бұрын
Contactez-nous
@nourayni4094
@nourayni4094 3 жыл бұрын
@@DaoTechIndustriessenegal merci de m'envoyer votre adresse mail
@DaoTechIndustriessenegal
@DaoTechIndustriessenegal 3 жыл бұрын
daotech.tv@gmail.com
@matarlo9153
@matarlo9153 3 жыл бұрын
Machallah beug sa numéro
@DaoTechIndustriessenegal
@DaoTechIndustriessenegal 3 жыл бұрын
Mën nga ño jokku ci 764078376
@salkhadimthiam4701
@salkhadimthiam4701 2 жыл бұрын
diadieuff
@mouhamedgano4658
@mouhamedgano4658 Жыл бұрын
Lu tax yeggale wuleen ?
@DaoTechIndustriessenegal
@DaoTechIndustriessenegal 5 ай бұрын
Ño ngi jeggalu. Jafe jafe ci jumtukay yi motax
@seckdjibril8826
@seckdjibril8826 3 жыл бұрын
Sa numéro ?
@DaoTechIndustriessenegal
@DaoTechIndustriessenegal 3 жыл бұрын
Dans la description
@bayemomardieng4131
@bayemomardieng4131 3 жыл бұрын
@@DaoTechIndustriessenegal intéressé pour la formation
@DaoTechIndustriessenegal
@DaoTechIndustriessenegal 3 жыл бұрын
Merci de me nous contacter par mail daotech.tv@gmail.com
@user-tj6bd3gf7e
@user-tj6bd3gf7e 6 ай бұрын
Cablage en Wolof
@DaoTechIndustriessenegal
@DaoTechIndustriessenegal 5 ай бұрын
InshAllah
Électricité - câblage interrupteur simple allumage pour débutant explain in wolof By Djibril
11:24
Électricité en wolof TV [ELEC TV]
Рет қаралды 1,1 М.
Kids' Guide to Fire Safety: Essential Lessons #shorts
00:34
Fabiosa Animated
Рет қаралды 12 МЛН
Вы чего бл….🤣🤣🙏🏽🙏🏽🙏🏽
00:18
WHO CAN RUN FASTER?
00:23
Zhong
Рет қаралды 35 МЛН
Secret Experiment Toothpaste Pt.4 😱 #shorts
00:35
Mr DegrEE
Рет қаралды 42 МЛН
Mën Na Nék: Les Principales familles de dessins industriels_Cours2
22:33
Bànqaasu xam-xam
Рет қаралды 1,1 М.
Mën Na Nék: SVT ci Wolof | Jàngu 1: Le Système Nerveux
10:48
Bànqaasu xam-xam
Рет қаралды 14 М.
Les principales centrales de production d'énergie
11:50
fab nico
Рет қаралды 11 М.
Le Courant Électrique Expliqué courant alternatif
18:45
Mentalité Ingénieur
Рет қаралды 588 М.
Kids' Guide to Fire Safety: Essential Lessons #shorts
00:34
Fabiosa Animated
Рет қаралды 12 МЛН