Eumeu Séne meussoul Nék champion d’Afrique? Fadam 2 avertit Franc et fait des révélations «Lac2 na..

  Рет қаралды 20,284

Senbuzz TV

Senbuzz TV

24 күн бұрын

Пікірлер: 128
@user-rj9sb9cv7u
@user-rj9sb9cv7u 21 күн бұрын
Lac de guere yala nako yala takhawou si barke seuydina Mouhamed ❤❤
@alhamdoulilah9154
@alhamdoulilah9154 22 күн бұрын
Bilahi Sénégalais dafa nafekh eska balla gaye eska dafdone nekhal yekini pour beure ak moum ama baldé lounek wakh nako modou lo pour beure ak moum boy niang2 lounek wakh nako balla gaye pour beure ak moum baye mandione lou nek wakh nako gris pour beure ak moum lac2 lounek wakh nako gris bordeaux malgre beure wugnu legui pourquoi franc wara nekhal eumeu séne pour beure ak eska franc eupoko victoire sports amoul nekhalaté soof ngene trop te seytane affaire sa thies yoyou franc nekousi kokou dialoul danga khamné meune reck
@rouguikebe9984
@rouguikebe9984 21 күн бұрын
Bayiléne rék affaire layam layami yoyou franc nékoussi😂
@mbayendiaye4562
@mbayendiaye4562 20 күн бұрын
Wakh gua deug
@josephericousmanediandy783
@josephericousmanediandy783 4 күн бұрын
Frère franc nelawoulll . Kafoul , fowoul , neixaloul keineu. Guisss nako dimanche passé wanté bokou guissé farata la deffff après daw nhibiiii ngua xamniiii taxawalou sonalouko
@Sallmyname
@Sallmyname 22 күн бұрын
Merci Fadam, il faut que les gens fassent la part des choses 👌🏾
@ibrahimadrame9499
@ibrahimadrame9499 22 күн бұрын
Fadame machalah taye mom wakh nga deugue
@elhadjimalickndiaye6947
@elhadjimalickndiaye6947 22 күн бұрын
Franchement fadam il faut que tu devient Un patriote
@sonkofocus2024-ph4hv
@sonkofocus2024-ph4hv 22 күн бұрын
😂😂😂😂 bounou yablou
@danielcorreia2073
@danielcorreia2073 22 күн бұрын
Merci fadam teymom deug rekk, fran sa comunication est logique mais kou comprendoul sport moké guisse ay yeufou rew, mo meun mo eupeu dole fran kesse
@papispass
@papispass 22 күн бұрын
Balla Gaye wakhe naffi Yékini wala Tyson lounék.. té lolou moye lamb donc maye léne djame Franc
@Fayejeeseef
@Fayejeeseef 21 күн бұрын
Fadam2 je suis entièrement à vous
@sebastienaccatcha4298
@sebastienaccatcha4298 21 күн бұрын
fadam mey niou diam 9 combats 8 défaites todjo feneu diambar, dieul sa micro mo gueuneu yombeu lo guiss. Franc est le meilleur lutteur de sa génération té kouko dieul mou humilié le
@walyfaye4556
@walyfaye4556 22 күн бұрын
Merci fa
@manelmendy5912
@manelmendy5912 22 күн бұрын
Merci Fadam
@ousmanesarr756
@ousmanesarr756 22 күн бұрын
Reug reug ngen yab rek wayé franc mofi guena rew fouff Senegal mo bari ay nafekk rek
@babacarndao9293
@babacarndao9293 22 күн бұрын
Analyse pertinente 🎉 n'oublions pas qu'il fut des on avait l'habitude de dire que Balla gaye 2 est impoli or c'était juste pour attirer le public
@omarlowe3879
@omarlowe3879 22 күн бұрын
NDIAGO ORBI REK 🎉🎉🎉❤❤
@morcavani-tk4zc
@morcavani-tk4zc 21 күн бұрын
Super Franki 😂
@djimbaniang2190
@djimbaniang2190 21 күн бұрын
Ay yaroul ma mayla chance ay thiakhan le Eumeu sou beugeu dieul sou bagoul mo xam
@user-ew7ur9dv8t
@user-ew7ur9dv8t 21 күн бұрын
Fadam❤t’es fort
@modo6218
@modo6218 22 күн бұрын
Franc wakh na degue nekoul champion d’Afrique
@petitboumoussaballagaye5699
@petitboumoussaballagaye5699 22 күн бұрын
Becaye vs Jacob BALDE Becaye vs thiatou ngeweul Becaye vs coly faye 2 Becaye vs tidiane fay Becaye vs diop 2 Becaye vs siteu bou ngor Becaye vs gakou 2
@morcavani-tk4zc
@morcavani-tk4zc 21 күн бұрын
Franc Rewoul senegal khamouniou sport nak ndeysane . Sport wakhanté ay kadou dou manque de respect . Franki vraie champion la dé
@talentfoottv3861
@talentfoottv3861 4 күн бұрын
Franc na khar Ama pour xol ndakh dina diote tchi Eumeu ack Balla G2, mais pour wakh deugue réck Franc mbeur bou yarou lá. Mane Eumeu momay danél, way Franc cool mbeur lá
@lhomme_fort
@lhomme_fort 22 күн бұрын
Franc Ndiago bi kassé nak
@CheikhMbengue-fl8ik
@CheikhMbengue-fl8ik 22 күн бұрын
Merci fadam fra championla kouka dialiul dag ko ragal
@SonkoSonko-wx8dk
@SonkoSonko-wx8dk 22 күн бұрын
Fran kouko dieloul ya kham mber le té am na dolé té dina beri ak yénén champion késé nak
@toungounemechantlofficiel630
@toungounemechantlofficiel630 21 күн бұрын
Ioe tay ngay khalate li fadam ioe nga xamni si élection yi nga diay sa ngoor beugg niow fi di grawgrawlou fadam adioul fi on sait qui est qui Yalna lac dall jamm te am jamm
@cirely3220
@cirely3220 20 күн бұрын
pikine la deuk bisbou eume sen dieulè franc ma bayi eume sene
@AliounebadaraGassama-or4op
@AliounebadaraGassama-or4op 2 күн бұрын
Bouniou ko fayé kenene dèf ko niou fayate ko
@ndiayeabdouaziz588
@ndiayeabdouaziz588 22 күн бұрын
Franc réwol mai defa tepi tounou ndeye EUMUE sene dou moromou ndeyem
@OusseynouSow-zk4on
@OusseynouSow-zk4on 22 күн бұрын
😂😂 ndeysane yalna yalla défarate la si barké séydile hadji Malick Sy
@assanediop771
@assanediop771 22 күн бұрын
Man balla gaye2 moy sama mbeur mais franc wahoul lou niaaw
@user-hf8pv3qw4s
@user-hf8pv3qw4s 21 күн бұрын
Fadam katal sa yaye
@lhomme_fort
@lhomme_fort 22 күн бұрын
Affaire bi franc la
@layeNdiaye77
@layeNdiaye77 21 күн бұрын
Eumeu sou dieulee franc ma bayico
@dioufbathie3093
@dioufbathie3093 21 күн бұрын
Franc na yarou
@ibrahimadrame9499
@ibrahimadrame9499 22 күн бұрын
Pourtant li fran wakh Bombardier moko ndiaka wakh😂😂😂😂ta diouroul thiow fran moye dérangé séne ndaye😂😂😂
@ousmanesarr756
@ousmanesarr756 22 күн бұрын
Franc bopam lay déranger pas eumeu lolu bako bombardier wakhé fimouko wakhé lako eumeu tonto té wakhatousi ndakh khamni khamoul limouy wakh eumeu gniko yobuwone ngi fi kene de dousi diaroul bari wakh😂
@ibrahimadrame9499
@ibrahimadrame9499 22 күн бұрын
@@ousmanesarr756 na dieul boye bi lamb la d'accord nagne champion la mais boybi yéksina 💪💪💪💪💪 eumeu séne dako ragal rék lay amoufi
@djimbaniang2190
@djimbaniang2190 21 күн бұрын
Li fran wakh mbeur moum meti na dieul combat bi
@BallaMoussaTamba09
@BallaMoussaTamba09 22 күн бұрын
Mané Lac 2 ak palmarès bimou am loutakh dougn ko wakh !!!! Ay Eumeu Sene ay Gris Bordeaux yepp Lac 2 molen eup Palmarès ! Il est très sous-estimé et j’ignore la raison dafa wara beuré chaque saison !!!!
@ahmadoudiop5016
@ahmadoudiop5016 22 күн бұрын
Louler ngua wakh
@mamepathengom9398
@mamepathengom9398 22 күн бұрын
Taye mome andeu na ak iow ✍️ Fran daye nékhal lamb rék ✍️ kouka dieuloul dagako ragal 🤣💪
@mouha1461
@mouha1461 22 күн бұрын
Danguen diepi Franc rek té tegolen ko féneu wayé kokou ci dieul mouy Eumeu di Balla Franc neweul leu dolé dane leu ci lou gaw, lolou nguen kham motakh nguen di khatarayou
@sambatorino8115
@sambatorino8115 22 күн бұрын
Tieye senegal garde a vue niounane casso
@user-fx1wt4mg7h
@user-fx1wt4mg7h 22 күн бұрын
Vraiment 😂😂😂
@bocarba2781
@bocarba2781 22 күн бұрын
Aziz ndiaye meunoul diot si modou lo motakh mouni day creer roi des arènes. Dafay doul rek. Aziz le plus grand domeram du Sénégal
@AdolpheGomis
@AdolpheGomis 22 күн бұрын
Arrête Aziz ta fait coi pour que tu l'insulte de cette façon amal yaar dalou thiarakh Aziz sah la guene mome kéne masouco dégue moy saga
@bocarba2781
@bocarba2781 22 күн бұрын
@@AdolpheGomis abon? Wakhoul wone balla dafay deff gris bordeau louniouy def djiguen? C’est à dire Kate. Comme nima defane sa yaye? Seulement que sa yaye dafa beugone m’a dieundeul ko daleu thiarakh après l’avoir bien baisé. Ngani lanou aziz moma gueune? Degouma? Gamin lol
@user-ok4jm5ry7w
@user-ok4jm5ry7w 22 күн бұрын
Ms sa way Aziz nafékk la xam nagniou leep
@bocarba2781
@bocarba2781 22 күн бұрын
@@AdolpheGomis soumala tonto dou bakh. Nala bayi nonou
@rouguikebe9984
@rouguikebe9984 21 күн бұрын
Wa loutakh mouy cré roi bopam affaire sabotage yoyou😮tmt
@ModouKeinde-wm6le
@ModouKeinde-wm6le 22 күн бұрын
Dafa réwe dh
@cheikhcamara4888
@cheikhcamara4888 21 күн бұрын
Lolu mom waroko nitt lobeg beg beure akk mom waxal deug rekk thé yalla tax Eum est champion d'Afrique à l'âge de 17ans
@serignembengue2491
@serignembengue2491 22 күн бұрын
Wakh wakhou réwanndé takhoul nga ammm combat franc akkk Eumeu seul dans un endroit bilahi walahi talahi franc dou wakh tapette international leu dagno khamoul Eum rékkk mais bakhna'... Naaa djieuli sa Thies wala Alioune Seye 2
@lahadboukharagnelo6707
@lahadboukharagnelo6707 22 күн бұрын
Franc dafa sokhor www legui mo Taye eumeu sou nianme nako dieul
@serignedieng-vh4zv
@serignedieng-vh4zv 21 күн бұрын
fadam dioume nge eumeu séne kéne mayou ko chenc fila dane be wara berék roi bi yekini gnou diko khékh eumeu fim nk mofi andi bopam
@bilalfall2953
@bilalfall2953 22 күн бұрын
C vrai cachot diomboul kén mais naniy bayi di déf lou yon téré nul n'est au dessus de la loi
@davidciss169
@davidciss169 22 күн бұрын
Franc n'a rien prouvé ici......
@mamemoussagueye952
@mamemoussagueye952 22 күн бұрын
Soudone reug-reug gnouni dafa réw…franc sou nèkoul wone diambar production bi nékk si guinawam dou yèksi fi moment bi dagneko tebal lou bari donc na wagni arrogance khamni dèfoussi loufi moromam yi defoul dalene eup chance rek
@madiorgueye5640
@madiorgueye5640 22 күн бұрын
Ndaye sane fi ngaye toude saydi aboubacar ngou nila ba yi nage ko thiaye aboubacar sy
@malickniang225
@malickniang225 21 күн бұрын
Sénégalais moo naafékh franc wakhoul dara Lou gnaw wahou lamb rék layy wakh
@LeFutur77
@LeFutur77 18 күн бұрын
Franc dell nangoul sa papa yi Eumeu sene sa papa la ak balla Gaye
@madiawboussondiaye6208
@madiawboussondiaye6208 20 күн бұрын
Eumeu day nopolou day def com Modou lo dieul Lou yomb d'âne KO takhawate Modou da warone dieul tapha daw demain ci siteu nioune tamite Gouy gui wala Aliou sey 2 wala combat royal
@aleka1533
@aleka1533 2 күн бұрын
Billay frere
@papeseck4052
@papeseck4052 22 күн бұрын
Bayiléne nafekh franc défagoufi léneu balla ak eum douniou ay moromam déléne wakh deugueu ta yalla takh
@KalidouKa-pl7or
@KalidouKa-pl7or 22 күн бұрын
faranc kou ko diéloul dan ko ragal
@assleye8654
@assleye8654 22 күн бұрын
Franc alioun seye moy comba
@user-lw4xo9oq9h
@user-lw4xo9oq9h 22 күн бұрын
fran kouko dieuloul daguako ragal
@omarsow7669
@omarsow7669 22 күн бұрын
Pap sarr kouy ray ak kouy mar la beug
@saerhihiodf110
@saerhihiodf110 22 күн бұрын
Fadam 500mil Beuri na d sougn defone sak moi mbeur you mak yi 10mil sak moi mbeur you Ndaō yi 1000f rk lolou Dara la
@ahmadoudiop5016
@ahmadoudiop5016 22 күн бұрын
😂😂😂 wala 100milles sakh bahna non saway Ray nguama
@madiorgueye5640
@madiorgueye5640 22 күн бұрын
Ni mouye wakhe ni de dounge ko maye change de man la ko wakhe fi
@juniorjunior1345
@juniorjunior1345 22 күн бұрын
Mais kikane la?
@goorandione3766
@goorandione3766 22 күн бұрын
Faranc dafa rew te d'où gatt
@danielcorreia2073
@danielcorreia2073 22 күн бұрын
Yako geuneu rew
@MouhamadouNiang-pg5jm
@MouhamadouNiang-pg5jm 22 күн бұрын
Fran dafa rew demal beure ak say morom eumeu dousa morom rewgua trop
@amadoupam
@amadoupam 22 күн бұрын
😂😂sa waye bayil lolou lamb amoul ay morom na ko eum dieul rek niou guis parceque combat dakhou ko
@assleye8654
@assleye8654 22 күн бұрын
Kii day doull rk
@medouneniang524
@medouneniang524 22 күн бұрын
Danion soff rk kou nékh deukou koula nékh lamb la
@morcavani-tk4zc
@morcavani-tk4zc 21 күн бұрын
Franc dafa saf sap ak lamb
@ndoyeadam6318
@ndoyeadam6318 22 күн бұрын
Franc dafa sokhar
@ousmanegomis6938
@ousmanegomis6938 22 күн бұрын
Fadam sa data yaye 🖕 Ndiago bi seul
@Ting05122
@Ting05122 22 күн бұрын
Yaw momme da nga soxxor. Sa kanam. Gửi di mélle ni platou feurigne. 😮 sa bakane bi di ma Saf. Bou nou maky salle bi
@user-ou2gg5rp4o
@user-ou2gg5rp4o 22 күн бұрын
Franc balla ni Ladone def té djigouko franc lamb daye sotte franc lamb djiéyaté teyale adouna mogulaye djieye
@CaramocoDiallo
@CaramocoDiallo 22 күн бұрын
Franc ci bopam moooo rew eumeu sene mo beure' woul AK franc rew baxul mounoul communiquer avec respect
@danielcorreia2073
@danielcorreia2073 22 күн бұрын
Yako geuneu rew
@CaramocoDiallo
@CaramocoDiallo 22 күн бұрын
@@danielcorreia2073 eumeu sene beurre woul AK franc
@mouhameddia5168
@mouhameddia5168 22 күн бұрын
Franc rèwoul dafa beugue beurék Mome rék
@CaramocoDiallo
@CaramocoDiallo 22 күн бұрын
@@mouhameddia5168 du ' communiquer avec respect defa baxe
@magattediop9975
@magattediop9975 22 күн бұрын
Sénégal la guiss sport de combat bo khamni daniouy beug nga néxal sa adversaire pour beuré ak mom. Combat Sa Thiès ak Eumeu lolou moko sofal Franc limou communiquer guénoul cadre lamb té mbeur bouko dieuleil dangako niéméwoul c simple
@Ibrahima66.
@Ibrahima66. 22 күн бұрын
POURTANT BOMBARDIER MO NDIEUKA WAKH NI EUMEU SENE DOU CHAMPION D 'AFRIQUE
@ousmanesarr756
@ousmanesarr756 22 күн бұрын
Bombardier fimouko wakhé lako eumeu tonto eumeu gniko yobu wone gnôgui fi kene dewousi
@LeFutur77
@LeFutur77 18 күн бұрын
Fadam nafek nga CI lamb lagnouy wah motah niounela da rew Nganan ay wett Soubeugue beuré rewandé moy solution Douwah ak respect
@josephericousmanediandy783
@josephericousmanediandy783 4 күн бұрын
Iow noopil dafla arrangé woul reik motax nguay waxxxx
@saerhihiodf110
@saerhihiodf110 22 күн бұрын
Yene doul eumeu sou beuré woul ak franc mo kham franc na dieul lac niou beuré
@OusseynouSow-zk4on
@OusseynouSow-zk4on 22 күн бұрын
Euma séne mofi guana gnaw palmarès
@mamadoudiouf3878
@mamadoudiouf3878 22 күн бұрын
Dénguay doul Franc da réw depuis lutte simple yag nanie diko suivre ngay doul ak sa kame boy réy
@AliounebadaraGassama-or4op
@AliounebadaraGassama-or4op 2 күн бұрын
Mais yarou ak nopi bokoul dieul alalou diambour ana khaliss bi foumou ko dougeul
@user-qg9tr3fb4s
@user-qg9tr3fb4s 22 күн бұрын
Nianal déf li eumeu séne déf té doko mossa défsakh
@chamousman2726
@chamousman2726 22 күн бұрын
Franc champion de Afrique la bulko fatteh
@user-qg9tr3fb4s
@user-qg9tr3fb4s 22 күн бұрын
@@chamousman2726 eumeu séne lanla mâne lutte simple la gueune séytane mes combat choc yii franc zambala ordinateur Serigne Ndiaye 2 oboli général doudou sané reug sathiés fils de Balla
Как быстро замутить ЭлектроСамокат
00:59
ЖЕЛЕЗНЫЙ КОРОЛЬ
Рет қаралды 12 МЛН
Miracle Doctor Saves Blind Girl ❤️
00:59
Alan Chikin Chow
Рет қаралды 61 МЛН
UFC 302 : Махачев VS Порье
02:54
Setanta Sports UFC
Рет қаралды 1,3 МЛН
Franc Waroul Teukou Eumeu Sene ak Balla gaye2 ; Colère noire de Coach Bakary Sport la Limou def moy
18:23
Fadam2 expert de la lutte sénégalaise
Рет қаралды 21 М.
Как быстро замутить ЭлектроСамокат
00:59
ЖЕЛЕЗНЫЙ КОРОЛЬ
Рет қаралды 12 МЛН