Ndakhté daay feen Mario dou door djiguen, Yirim la meilleur amie de Mario Mbaye détruit Ndakhté

  Рет қаралды 49,171

Dakar live

Dakar live

26 күн бұрын

Пікірлер: 207
@khadyjagueye7949
@khadyjagueye7949 24 күн бұрын
Binga hamé ni fékéwoko nga ci warone mandou. Bou nobé diabaram diko torohal amoul sens. Ndakhté bagn na wakh ba sonou mais lou fess tourou. Boko haméwone mario sah doko wah
@ndeyeantasow274
@ndeyeantasow274 21 күн бұрын
Deugg reik ngua wakh
@khadijadiouf2322
@khadijadiouf2322 24 күн бұрын
Mario kèn meunouko mimal daprès ndakhtè limou expliquer violence conjugale ètat bi mo ci wara jeul ay mesures.yirim jiguèn ga mario waxlènko deugg,fèkèwo boul juger chaque jour ga nek ci boite yi sans sa jabar kèn doula wèdil.
@fatimandao8359
@fatimandao8359 23 күн бұрын
Merci
@ndiayenebiindiaye8565
@ndiayenebiindiaye8565 23 күн бұрын
Je suis d’accord état bi warna si dieul ay matoukay mais sou fekei lim wakh leep deug leu ndax bene version lagn am Loutax porte woul plainte ? Pour mane ay wakhi kessé dougaloul kene il faut des preuves Sougn la doré sa yaram am ay bleu si sass si nga dem police amoul négocier
@docordieng9826
@docordieng9826 23 күн бұрын
Iow est ce que nitt nga khana khamo ni ki mola tané ndax au moins mom limou wax yeup si kimou kham lay wax en plus mingi wax ni limou féké la meuna wax ak limou kham si Mario mé iow déjà khamo Ndakhté khamo Mario fékéwo di jugé
@LaSenegalaise221
@LaSenegalaise221 24 күн бұрын
Goor dou am meilleur(e)ami(e) bou Djiguéne.
@YummaM
@YummaM 23 күн бұрын
Malheureusement c'est toujours une autre femme qui vient "défendre", "démentir" au lieu de soutenir. Ndawsi déja elle affirme que fékkêwoul, et pire encore Ndakhté dou sakh haritam (donc normal que meunouko hamal dara). Mais malgré cela, elle ose quand-même prétendre que ce Mario ne serait pas capable de faire à une femme ce qui est cité par Ndakhté. Pathetique. Se taire aurait été mieux chère dame. Boulafa tollê tamitt, tu discutes avec ton "ami" Mario, voir en quoi tu peux aider pour récupérer son ex femme, sagam ya wakh ni seu yêné moy qu'ils soient ensemble.
@yayourassoul5054
@yayourassoul5054 22 күн бұрын
Femme détruit femme
@aminatacisse2560
@aminatacisse2560 24 күн бұрын
Teeyal meunoo xam djiko mario 100% meune nala neub bopam tamit
@user-xy7eo9pk1f
@user-xy7eo9pk1f 22 күн бұрын
Yawit khamo ndakhté féké wo kone na gneup mandou bagna juger ken
@dairiaviplareineduparfun6767
@dairiaviplareineduparfun6767 24 күн бұрын
Billahi yaw yaye fenne
@MamanLo-dc7ro
@MamanLo-dc7ro 23 күн бұрын
Doul kat laa
@yacinediallo6393
@yacinediallo6393 23 күн бұрын
N'oublie pas que ndakhté a des preuves, et Mario est un tricheur et tu l'as bien dit tu n'était pas dans la chambre
@SuperOUMZ
@SuperOUMZ 24 күн бұрын
Xamo dara,fékéwo dara Deléne wakh louléne lerrr
@fatouwade5048
@fatouwade5048 24 күн бұрын
Boko léne keur beugue kham li khew té nga mandou sof nga torop😏😏
@user-es6ns5ep7k
@user-es6ns5ep7k 24 күн бұрын
Moma diahal
@badaralo971
@badaralo971 24 күн бұрын
Yaw wite yako féké yaw tmt mandoul
@Ramapoulo
@Ramapoulo 24 күн бұрын
Moma diakhal
@BoussoCisse-bq3fw
@BoussoCisse-bq3fw 23 күн бұрын
Degue degue seytané rek
@ndiayenebiindiaye8565
@ndiayenebiindiaye8565 23 күн бұрын
Mais yene aussi yenagui juger ta xamolene loufa khew esk dou nieup wara mandou
@maimounasarr6565
@maimounasarr6565 24 күн бұрын
Khana dô dieguene Besse bou laye sa dieukeur di mal traité nagako oube
@aissatoubah229
@aissatoubah229 24 күн бұрын
Toi aussi tu es une femme que dieu te redonne tout ce que tu dis sur cette couple ❤❤
@absaduop7965
@absaduop7965 24 күн бұрын
Mais tu dors avec eux toi tu était presente
@AbyManga-ml8sw
@AbyManga-ml8sw 17 күн бұрын
😂😂
@aidasagna2928
@aidasagna2928 23 күн бұрын
Yaw sa kanam melni khoniou mbaxal yay fem yak fem shimmmm mario khamaloul dara ndakhté xana mou sosal ko bayilen ninguen mel nit bou néké sa xarit waroko diay dangakoy wax deugg mais Senegal wax katou deug bari woufi xaliss rk ngéni top tchiiipiiiriiii
@yolandeCurtis2023
@yolandeCurtis2023 23 күн бұрын
Madame arrête de mentire même si c'est ton ami ou frère ce que son ex femme a dit c'est clair et c'est à lui de répondre à c'est acte et nous vous lui a un bouche no qu'il parle aussi donc madame si c'était ta sœur ou ta fille qui a subit sa tu allais venir parler arrêter un moment donné trop cest trop elle a vécu trop de chose dure avorter 2fois ect.. donc ell est une brave femme Ndakhté
@mayakhalil1142
@mayakhalil1142 24 күн бұрын
Fi diabar rek mola meune wakh djico djeukeureum donc mandoul
@fatimandao8359
@fatimandao8359 23 күн бұрын
Bilahi wakhatiko
@aramesall3422
@aramesall3422 23 күн бұрын
Bilaye deuguela
@ironahide5896
@ironahide5896 22 күн бұрын
Lolou mom deugla mais amna diabar youy soss dé. Wakhouma cas wou Ndakhté dé. Fekena ko khamni limou wakhal dieukeram pendant des années ay fen la. Ndekei mom mo sik, ba reunion amé nieup tok diekeur dji wakh, neko soudé dou deug wakhal. Femme bi nopi, nieupa rouss
@user-bq3kd5hw5o
@user-bq3kd5hw5o 23 күн бұрын
Niang ballo dioum nga iow kharite kassé nga meuno kham Lou ndakhté Di doundou si négou seuyam ok môme nak mo togn bopam nakh sa ngoro ba la guiss lep ba paré si seuyal mome
@maridiop2975
@maridiop2975 22 күн бұрын
Bilay nak ndeye yirim wakhou fi lou niaw loumou kham rk la wakh soff nguene tropp ishhh
@MANGASSAthiaroyemer2499
@MANGASSAthiaroyemer2499 24 күн бұрын
LOUMA. DEGU. NIOU. DIOUBOOLÉKO. AK. NDAKHTÉ. KOON. YAGU NANIOO. DIAPPANTÉ
@dilebene8380
@dilebene8380 24 күн бұрын
Machalla j'ai tout suivi mais qu'on se dise la verité elle a bien parlé franchement avec responsabilité et maturité Témoignages nitt la def Bagna far fén Lo xamoul xamo Loula woroul woroula.
@awakebe9046
@awakebe9046 24 күн бұрын
Elle est direct
@sohnakambaye7286
@sohnakambaye7286 24 күн бұрын
Adjointe adji sarr numéro 2
@SarjoJasseh
@SarjoJasseh 23 күн бұрын
Wakh bi rafet na MashaAllah❤
@ngonediouf2632
@ngonediouf2632 23 күн бұрын
Légui yaw so amé dieukeur yalna la yiré nonou
@amisakho2877
@amisakho2877 23 күн бұрын
Wakhouma mounei da soll ayy lentiii😂😂😂
@user-dn1ok6yn3d
@user-dn1ok6yn3d 23 күн бұрын
Billayi adji sarr numéro 2
@user-bq3kd5hw5o
@user-bq3kd5hw5o 23 күн бұрын
Kou nop sa djabar doko dor aki saga wala diko matrak nagnou wakhaneté DEUG wala
@fatimadiallo9849
@fatimadiallo9849 24 күн бұрын
Y’a seuytanè tu habites avec eu avocat diable narkhtè elle est véridique
@Yataaaaashhh
@Yataaaaashhh 23 күн бұрын
Gnèmè nga yallah
@ironahide5896
@ironahide5896 22 күн бұрын
Yen da menli deglou wolen li ki wakh. Mom nena wedi woul li Ndakhté wakh dé
@rokhayakaraboye5437
@rokhayakaraboye5437 22 күн бұрын
héeee ndeye kirim négou seuy niar gniko sékeu Niort kham lissi bir . dou lep laniouy wakh . kou sa diabar def avortement nga warq tokk apporté KO sa soutien wayé Di weundeung si soirée yi . koumou done yaw Di yaw .
@fatykineniang2383
@fatykineniang2383 23 күн бұрын
Senegalais mo eupp fittt ci lou yalla sakk😂 day commenté alors que setanoul video bi mais c grave 😢 regardez la vidéo écoutez la avant de commenter et de la juger
@elhadjimalickdiouf7910
@elhadjimalickdiouf7910 22 күн бұрын
Vraiment! elle n'a rien dit de mal
@user-mq7mx1xb1d
@user-mq7mx1xb1d 20 күн бұрын
Fi guén fara Lou fi Ndakhté mais sou deugue dioté dagniou coy wax meuno négue marié ba paré à chaque fois guay dém di fanan si soirée yi . Il faut assumer ces actes té xAm né vie de couple dou ni .
@b_lebou8908
@b_lebou8908 24 күн бұрын
Li yep ndaxte waxon nako Nena sou nit yi togué dafay comporter wou normalement legui sou defei dara mom laniouy wax day jouer le jeux comme mom donc mom rek mo kham limou don doundou
@user-kv8fb1en4z
@user-kv8fb1en4z 24 күн бұрын
Franchement
@reema_Gainde
@reema_Gainde 23 күн бұрын
Mane dangama faté wo 😂 teh may khoromou sabarou Sénégal wernguel keup #dakar-live
@khadyastoudiop4944
@khadyastoudiop4944 23 күн бұрын
Sokhna yaw amgua fiittt. Ba wara tokk di wakh.khamossi dara
@magueddiop7171
@magueddiop7171 23 күн бұрын
Moni limou wahh lou nitt meunna dëgg leu bilahi
@Antonio-dw9in
@Antonio-dw9in 23 күн бұрын
En tant que femme elle devrait soutenir ndakhté mais au contraire elle parle des choses qu'elle connait pas
@mamikayre7021
@mamikayre7021 23 күн бұрын
Comme néko si nekba oubeul
@banelnegri2578
@banelnegri2578 23 күн бұрын
Yiow tu te contredis néngua sounouy yaye lou nek mougne nanouko ndakhté da warone mougn .gue delou ni boudons yiow do nanguou ay door be paré ngueni boudone yiow déf semblant dou lessi fék yangui faral Mario mais se wokh diaroul yone
@mariethiawaseck9084
@mariethiawaseck9084 22 күн бұрын
En tout cas mandou warr na diam, wassalam
@POSITIF_SENEGAL
@POSITIF_SENEGAL 23 күн бұрын
Am fite wessouwoul, deglouwo dara, nioulassiy lath, loula téré wax deglouwmako
@salladiallo1281
@salladiallo1281 24 күн бұрын
Mome loumouy def artist lane la mome
@OdileNgom-vm7ol
@OdileNgom-vm7ol 24 күн бұрын
Soko khamer gua wakhma ki thi bopam sah la khamoul féne tok diii doul loumou khamoul Khana lay liguey
@user-mq7mx1xb1d
@user-mq7mx1xb1d 20 күн бұрын
Fégué. Wo beugua jugé xama na man gua fén dé ana manou
@thiambabel6232
@thiambabel6232 23 күн бұрын
« Seuk na ba fi seuk yame mais pas violence » Ya nek si chambre bi ba kham bane violence moffa am nokoul feulei mounane photo guan fay fek Bamou deémé bay nekhalatei aka fay guan hamni nekoul si dara lou bah Sa lentille you niaw guany melni tortue ninja 🚶🏽‍♀️ Femme yakk femme😩
@fatoundiaye6412
@fatoundiaye6412 23 күн бұрын
Balko😂
@mamesey1294
@mamesey1294 23 күн бұрын
Yallah nah yallah leral lep sii brakeh yonantibi akk sii brakeh Baye akk Bayam yarabi
@MaremeDiagne-tp2en
@MaremeDiagne-tp2en 23 күн бұрын
Yen seuyolen takhawalou guen kham Mandoul Mario gorou milieux y’a yéye défendre ko ndakh Bou guen di fethie Molen di may khalisss yena meuna ande
@user-vl4ut7uj1h
@user-vl4ut7uj1h 21 күн бұрын
Li nga wakhh dara nékoul si fara lo si kéne deugue rékk nga wakhh
@YacineDiakhate-fi8we
@YacineDiakhate-fi8we 24 күн бұрын
Ana mandou guay Mélanie rapp niii thim
@nioulesskaye8964
@nioulesskaye8964 23 күн бұрын
Fo guiss soular deye violent
@aramesall3422
@aramesall3422 23 күн бұрын
Bilaye
@DiarraDiame-gt4is
@DiarraDiame-gt4is 23 күн бұрын
Lo khamoul manou siiiiii
@diamandour3266
@diamandour3266 24 күн бұрын
Yaw doul waye so nobe mario gua dem seuyeul ko
@mamadoudia8187
@mamadoudia8187 24 күн бұрын
Boy ya kat sa koyoup papa deug esk nat gua sa artiste bi dosi téki deudieuw ndayam
@user-ck2ow1vf7w
@user-ck2ow1vf7w 22 күн бұрын
Ki thi soirè yi lay nèk di leumbeul aka meune thiaga mario la
@fatoudiop3533
@fatoudiop3533 23 күн бұрын
Sokhna si meno wah ni vous vivez pas ensemble gua beug tok nane daguay témoigné si lo khamoul vraiment négua khamalo lolou Mario té deuko léne dnc meno kham djikom gua balma nite dale bouy sédé dafay am preuve avant de parler 😊
@AbyDiallo-jc7yl
@AbyDiallo-jc7yl 24 күн бұрын
Bamel wéttna deh wakhal Loula leer
@FamaNdiaye-wj8pp
@FamaNdiaye-wj8pp 23 күн бұрын
Thiey YALLA REK KA KHAM
@mamamdoudiagne355
@mamamdoudiagne355 22 күн бұрын
Ki pourtt limu wakh lerna d wahul lu ay ki bind titre bi mo meunn fenn rek
@user-xy7eo9pk1f
@user-xy7eo9pk1f 22 күн бұрын
Yen gniy wakh féké woul yénit féké woulen worou len ni ndakhté limou wakh deug la woroul ken. Kone na gneup mandou rek ba deug fegne
@mymyyoyo
@mymyyoyo 24 күн бұрын
Yaw dé doulekate ngua deuko tha keur gua, té Mario dafa faux beugue wakh si loufa khew ragalale yalla...
@aissatou14
@aissatou14 22 күн бұрын
Wa gni di posé question tamite est ce que cava ???😢 Di forcé nitt ki pour mou waah tohidouna tamite lane la Môme néneu affaires worouko nguéne beug mou forcé wah si😂😂😂
@khadeejah7586
@khadeejah7586 22 күн бұрын
Ma chérie manqué nga
@user-vq6se3md1n
@user-vq6se3md1n 24 күн бұрын
Nafekhe dou touty daye pata
@user-kv8fb1en4z
@user-kv8fb1en4z 24 күн бұрын
Ya yabaté 😂😂😂😂😂
@rokhayaann1466
@rokhayaann1466 23 күн бұрын
😂😂
@aidasagna2928
@aidasagna2928 23 күн бұрын
Deet dama pata mais nafekhouma dé😂
@kaisha1098
@kaisha1098 23 күн бұрын
😂😂😂
@SallSawdiatou
@SallSawdiatou 23 күн бұрын
Yagui togne déi 😂😂
@fatoudiagne4439
@fatoudiagne4439 23 күн бұрын
Ki deh xamoul dara si limouy wax 🤣🤣gueneul thi ligua nek
@aissatousy1875
@aissatousy1875 24 күн бұрын
Tasse bilay nakhete da sess rec wakh antouca nakhete courage
@ndoyesmithsonkosenbayelaaa8463
@ndoyesmithsonkosenbayelaaa8463 24 күн бұрын
Nakhtei dafay doul ndm rek...waxoul lou ame...demal setane prank.makhfousss dinga xamni kii respectei woul ndm dieukeureum di.doul fiiii...loumou wax yeup ay feineuh leu
@antadiagne137
@antadiagne137 24 күн бұрын
Prank bi Boudon yaw la noy def
@AbdoulayeDiouf-zh4kq
@AbdoulayeDiouf-zh4kq 23 күн бұрын
Tu as raison
@fatimandao8359
@fatimandao8359 23 күн бұрын
Lolou sone yaye yi la concerner khamouléne liguéne di wakh ki nèk ak dieukeureum mo khame loumi dounde aye hycrocrite guéne
@AssanatouNgom
@AssanatouNgom 23 күн бұрын
Yw yay doul nakhté loumou wah rk mo ame
@user-kk3rp1zq4l
@user-kk3rp1zq4l 23 күн бұрын
Kou khol sa kanam khamni fenn katt mario domramm laa
@ndeyeamyseck4249
@ndeyeamyseck4249 24 күн бұрын
Kholal doulkate bi mom
@khadyloum-ey8xg
@khadyloum-ey8xg 23 күн бұрын
Esk setane gako lep cherie prtant titre bi ak limou wakh bokoul
@belleduteteaupied1393
@belleduteteaupied1393 23 күн бұрын
Xawma lousa yonn waro won sax waxx nite day am classe
@user-ij8xr1zi1e
@user-ij8xr1zi1e 23 күн бұрын
Man dh dema beugon commentaires mais j'ai peur d'elle
@pendabal7235
@pendabal7235 24 күн бұрын
Mais khana tu dors avec eux
@user-rm7me7sr2u
@user-rm7me7sr2u 24 күн бұрын
Vremmen
@user-oq4ni1gn4q
@user-oq4ni1gn4q 24 күн бұрын
Khamo lou khéw si négou seuyeum Kone loy wakhé? Do mandou té nopi?
@siralo9284
@siralo9284 24 күн бұрын
Bonne question
@BoussoGueye-fp9dx
@BoussoGueye-fp9dx 23 күн бұрын
Boudee said kharitela nekale nite wakheko moutiyee diabarame boudee kharitame nga
@assanesane3596
@assanesane3596 23 күн бұрын
Lihew si bire négou seuy danko ham vrement sénégalais mo degeur fite
@user-qq5of7xq2k
@user-qq5of7xq2k 24 күн бұрын
Khaw ma mario boul wakh kêne ladioula 🤐 yaw mi bon d’accord nii mario limou deff yana gua ame dieukeur bou guena bonn mario
@MDiarraDiop-yy1fm
@MDiarraDiop-yy1fm 23 күн бұрын
lii ndakhté wakh doumako weddi ndakh damako ndondo sotoural sa diekeur ba nara lorou mais nak sant yalla rek
@MamySagna-tx1ev
@MamySagna-tx1ev 23 күн бұрын
Elle n'a rien dit de mal vraiment elle es verdict
@rouguitabarhama9860
@rouguitabarhama9860 24 күн бұрын
Sétana guouma wayé sou féké titre binguén bind lolou la wakh réellement si vidéo bi dina sagua sa .....
@rackyfall1526
@rackyfall1526 24 күн бұрын
Yaw kham mario bkhoul
@seynadiop6854
@seynadiop6854 24 күн бұрын
Mane déh titre bi motakh méye sétane
@rouguitabarhama9860
@rouguitabarhama9860 24 күн бұрын
@@rackyfall1526 yaw ban droit nga am nane ma kham suis-je ta camarade ? Mala guena rew guen la niaw lamine Dagua guis ma wakh wakhou Mario wala diko faral Titre vidéo bi dafa bind dafa bind ni ndakhté dafay fén Mario dou door jiguene motakh mani sou féké lolou degue dina sagua kou jiguene Bala ngay wakh daguay tak say lunettes lire bou bakh soy tontou bénén yon BONNE NUIT
@rouguitabarhama9860
@rouguitabarhama9860 24 күн бұрын
@@seynadiop6854 man dh ba légui sétanou ma mais yakar nani kou jiguene ki sanioul défendre Mario
@gnilanediouf7960
@gnilanediouf7960 24 күн бұрын
​@@rouguitabarhama9860réro amna dé😂
@PEOPLE-km7vr
@PEOPLE-km7vr 23 күн бұрын
Khana sa carte de soutien nga bagna perte motakh ngay faral mario???? Mane NDEYE YERIM mayniou diame tanga noppi dem tok diéma wouty diekeur te seyi
@user-if1jv8ki5t
@user-if1jv8ki5t 23 күн бұрын
Faikai wo dara
@user-hj8pm4hu8z
@user-hj8pm4hu8z 23 күн бұрын
Yow meno sah kholé ndah saye lanti
@arameaminendao2016
@arameaminendao2016 24 күн бұрын
Dafa dioumm prck c mario
@maremegueye2154
@maremegueye2154 24 күн бұрын
Yaw meuno bayi sunu yaye yi tmt tei nga mandu wasalam
@ramaba8099
@ramaba8099 23 күн бұрын
😂😂😂
@user-uc7ly1uh3l
@user-uc7ly1uh3l 22 күн бұрын
Bane meilleur amie khana ami à cause de l'argent
@DiakhateSoukaye
@DiakhateSoukaye 23 күн бұрын
Nena mommm khamnani mario dafa sikkeu donc leup lere na
@user-mn7qf8gz1j
@user-mn7qf8gz1j 23 күн бұрын
Ndeyssane ay 5mil fr yila mario di may motx nga tok femme yakk femme
@alijunior123
@alijunior123 23 күн бұрын
Niiitttt dafa leudeum dh sokhna si
@user-kv8fb1en4z
@user-kv8fb1en4z 24 күн бұрын
Wa yéneu ndakhté loumou wakh d’après mane khana dou tokeu publiquement di féneu ken meme en tout cas Mario dafa sikeu c pas normal sa diabar toke ba souba doula guisse gua dokhi ba souba tel di dogua nieuwe tous les jours ndakhté mo nekk si deugue may léne niou diam louné fangue kéneu douko diékh
@user-gr3lf5rm8f
@user-gr3lf5rm8f 24 күн бұрын
Yow monme dagua doule ba newii
@user-bv1ix1qc8x
@user-bv1ix1qc8x 23 күн бұрын
😅😅
@awaaidara8729
@awaaidara8729 23 күн бұрын
Diakarko photo ndakhte rek mo takh nguen ni gueme wougnkou sim
@mamanfall-ph9ux
@mamanfall-ph9ux 23 күн бұрын
Ki Dayeeee Doul
@BoussoGueye-fp9dx
@BoussoGueye-fp9dx 23 күн бұрын
Yowe doule
@user-if1jv8ki5t
@user-if1jv8ki5t 23 күн бұрын
En kone sikna
@NdeyemarieNingue
@NdeyemarieNingue 24 күн бұрын
Yawwww momouuuu yayeee doulkatttt bouuuu mak biiiii damale outiiiii dieukeur nakkkkk marioooo dallaaaa katttte besse datttaaa biiii bayèkouuu
@sokhnabousso4763
@sokhnabousso4763 21 күн бұрын
Do rouss sakh tchip
@coumbadiatta3368
@coumbadiatta3368 24 күн бұрын
Wa DL GNOY DOULE
@coumbadiallo6429
@coumbadiallo6429 23 күн бұрын
Do diabaram do fanan ak mom donc limou doundou réellement meunoko xam nit kén douko jugé tchi apparence ndakhte la si bien évoquée néna nit ki limouy doundou hors caméra ak hors internet mom rék moko xam
@user-lx1go5pg2u
@user-lx1go5pg2u 23 күн бұрын
guiss gua yaw nafekh rek mola diap khamo dara si ca bi mais comme affirmé gua ni mario siikkk na rekkkkk bakhnaaaaa
@user-if2zo6bs9g
@user-if2zo6bs9g 23 күн бұрын
bigua khamé ni dafa sacré gua wara teudj sa gatte gui divorce diambour guéni def aye sorti mbam yiguéne donne
BÉTÉ BÉTÉ - Saison 1 - Episode 37 ** VOSTFR **
1:07:49
EvenProd
Рет қаралды 1,1 МЛН
Increíble final 😱
00:37
Juan De Dios Pantoja 2
Рет қаралды 72 МЛН
$10,000 Every Day You Survive In The Wilderness
26:44
MrBeast
Рет қаралды 136 МЛН
ПООСТЕРЕГИСЬ🙊🙊🙊
00:39
Chapitosiki
Рет қаралды 68 МЛН
RÉCIT DE VIE DE NDAKHTÉ LO : CONFESSIONS ET SECRETS INÉDITS - (INTÉGRALITÉ)
1:30:01